wathié bii ak changement ton bi😭😭😭❤❤ Yala na yalla barkel
2022-02-16 12:57:59
79
Ousseynou assane Cissé :
Année bi douma ko meussa faté 2019la wone, Darra la nékone mane ak sama cheikh niou ande ak Serigne bi , mais sama yarame da done daw jour bi sokhna si done diangue 🥹 🥺