@juleslepatriote: 😱😱 Nob bou graw😱il ou elle t’aimera par force😱 Def ko sa dieukeur wala diabar rekk nak pas kenen. #senegal #senegalaise_tik_tok #senegaltiktok #senegal_tiktok221 #galsen221 #amour #mariage #pourtoi #foryou #dakar #dakarbuzz
Jules-le-Patriote🇸🇳
Region: FR
Saturday 30 September 2023 10:11:55 GMT
Music
Download
Comments
ndéye :
NOOP daffa Daguane😴😴😴walla daffa kharame???
2025-05-16 10:01:12
16
Diabous :
nou niouye binde badoxau si arabe svp
2025-02-04 15:36:23
0
Abdoul'Allah :
wallahi day fène
2023-09-30 12:51:40
23
Mme diouf néné :
salut en France ou en arabe
2023-12-02 06:06:49
14
Absatou Ndiaye :
serigne bi noop lagn ma defalone mais doolé bi mo bari ma beguone nga dimbali ma si loukoy wagni svp
2024-10-07 14:18:17
2
Atout Sunugal :
Bayilen li way, c'est grave, il ne faut pas profiter des gens
2023-12-03 21:45:26
41
diamondguy :
Amoul sens nagn ko denk yalla rek meune nga ko def koula Djigoul nga beug si guene mou teuu la. Nagn wakilou si yalla geum ko Tei wolou moy deug. 💪
2023-12-02 17:35:06
16
Petite Glam(Dm)kirikou 🫶🏽 :
kou def ba paré nama wakh man😂
2023-12-03 15:16:55
0
madjiguenegueye41 :
koumay bindal badouwou si alkhourane
2024-04-06 12:19:50
15
Apad77🇸🇳 :
de préférence pakka bou besse takhe bou meussoule dague dara
2024-03-28 10:01:57
21
Satou lionne🥰👌 :
j'en suis sûr que gni wax n'a naturels yénakoy def nakk in thé péte... mayé lénn diam khamanté nanou
2023-12-11 06:34:58
86
Thiofashion :
Ayyy way bala Kéne dima badohou nar ma reye ma badohou Nd….y
2023-12-03 05:33:05
6
user5750018848074 :
Xana amolen lolen def mais goor rk akh
2023-12-02 13:24:15
5
thiernosow98 :
amnasi bou yeumé dé bilahi
2025-09-14 18:58:22
0
Ndiaye Calso :
nop day naturel
doumako sakh essayer. geum yalla geum sa bopp dra dioumbou la
2023-12-03 20:38:12
22
Niang Daba :
salhalahou alha Mohamed
2026-05-29 18:41:50
1
LTONY✯🇸🇳🇬🇼🇨🇻 :
Bayilén sen khéll yiguénn di fowé Mbeuguél daffay naturel so teudé guestou xamnii c l’amour est c réciproque😍 wayé guestou Rouss jamais 👎🏼
2023-12-04 13:43:35
7
anti système :
Ay kouko bindé paka bi rere la 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 Théâtre jule bi kouko setan diaro bi 🤣☺️🤣🤣☺️
2023-12-03 22:10:34
6
Adamadiome19 :
aye way louy mayé tate 😂
2024-06-27 11:02:48
3
user5011139838182 :
hey way nougne koy bindé svp
2023-12-02 15:56:07
1
Mouhamed diop😎 :
kou siy liguéy sa dieukeur Dou goudou fane
2024-01-03 14:36:36
1
binte Diop :
salalahou allah mohamed
2025-12-31 14:46:20
1
bamba ka :
بدوخ
2024-04-16 01:08:30
2
diop@246 :
Es k do Nguén gnou bindal mot bi
2023-12-01 21:11:20
4
To see more videos from user @juleslepatriote, please go to the Tikwm
homepage.