@atelier_art_bi: Partagez vos astuces #atelierartbi #artbi #artbisenegal #sengaltiktoker🇸🇳 #senegal #reveilenfant #mamanjeune #momtok

Atelier Art bi 🔧 🇸🇳
Atelier Art bi 🔧 🇸🇳
Open In TikTok:
Region: FR
Monday 04 December 2023 18:57:49 GMT
221980
21031
222
118

Music

Download

Comments

deals.hijab
Deals hijab :
sama réveil sou sonné damakoy fay khar sama yaye😂
2023-12-04 20:01:18
539
c_promaxx
C' PRO MAX :
Mane dh ay phrase de motivation lay nommé Samay réveille déf moukoy lire à voix haute mais doutakh ma diokk😊
2023-12-04 22:14:56
124
awadiop945
🇸🇳 :
Mane dh kouma yewoul douma diouk😂😂
2023-12-05 22:56:51
1
mariamakamara178
mariamakamara178 :
Mane deh may Sama réveil bop on dirait que dagne ma activée à 5h30 souy diote may diouk
2023-12-05 07:20:05
62
o123456789tt
Salihate bi beugue nieup :
Sama papa lén rek lama yéddé avant may seuyi une semaine avant nima nguir yalla bo démé del téla yéwou ak di wodou seur 😂😂😂 pask khamna sama beugue nelaw qu'il repose en paix papounet.
2023-12-21 15:12:29
4
n..d002
D’❤️‍🔥🫶 :
Wala 6h diot mère bi dila yéh nanela 8h diotna😭
2024-01-05 00:19:40
2
maremefoulat
maremefoulard🇸🇳🇲🇦 :
Bientôt 30a 11 de mariage 3 s enfants mousouma har koma ye dama done rouss sama yaye dima ye🥰
2023-12-05 14:22:25
3
salimatasow228
LySA :
mane damay fey réveil ⏰️ba paré nane kharal ma teudate 5mn😂😂😂
2023-12-11 12:22:13
2
dhservice2
Diagne Home Service :
Bima neke senegal reveil meussouma yé mm bima done liguey mais bima voyager bala reveil bi di sonner ma diouk 😫lepp mentalité la
2023-12-04 19:28:10
15
suadsene
S🎀 :
Man damadone yewou teud di xaar sama yaye yei ma sino douma diouk😂😂😂Sénégal nexxna😭😂
2023-12-04 19:34:24
23
20deug24nekhoul
Taaw🥰😍 :
pour mane secret bi moy tela teud kep kot. bo teuder 21 h nelaw ba 5h kay dina bakh 9 h de temps😅
2023-12-07 22:32:11
22
biobyeaish
L’Univers Bio by Aish :
Moi je suis toujours à lheur je me suis bien organisé avec mes 2 enfants
2023-12-20 16:26:20
2
layendiaye9846
M Laye Ndiaye :
Ça me rappelle des souvenirs avec mon père 😭paix a son âme que dieu l'accueille dans son vaste paradis
2023-12-14 13:59:22
17
ndeyenianediabong
Mossane Niane Diabong :
Khanou sounou réveil ⏰ répéter wara diouk 6h 30 défco 5h du matin mouy soné may coupé rék😂.merci maman
2023-12-05 11:29:19
11
marietouseck5
Marya🇸🇳Championd'Afrique⭐️⭐️ :
Lol quand je suis allée a l’étranger la hamni lepe deug la 😂
2023-12-04 21:29:32
52
beugumame2
Kya ❤️😍 :
Bilay bima seyé chaque jour sama goro kasee bilay
2023-12-20 14:47:54
3
tyma0172
tyma :
Mane deh kéneu meussouma yéé té meussouma bideunti
2023-12-15 22:13:18
1
aaisha_ceesay
aisha_ceesayᥫ᭡ :
Sama yaye batay momay yé deh😂😂😂 souma naré guenn sakh wara teila demm veille bi lakoy wakh pour mou yé ma moy sama reveil deh
2023-12-08 00:30:11
5
zarabine2
Zarabine2🧿 :
Diaroul réveil pour ñi nek biti rew problème yi ak khalat yi si bopam ñolay yeh 😂😂😂
2023-12-05 14:36:08
2
amy_saliou_n
{AMY’$} :
Man sama yy moma dan yee legiu nk gene na Senegal may yee sama bopo😳i miss my mum ❤️🌹
2023-12-04 19:12:24
4
catiathiate
catiathiate :
bima nieuwè sama keur nelaw rek lafi nekè 7 année mom cv ma ngi degue sama réveil ndakh sama diekeur tant que paré wouma dou diouk
2023-12-21 14:01:05
2
diorcherif
Dior Chou :
lep thi mentalité la. bo khamé ni bo diogaloul sa bopp amo koula yé , bilay dinga diouk bollé thi yoré ligueyou diambour ngay khamni thiakhane diekhna
2023-12-04 22:10:05
2
ddamoony
ddamoony :
sama pape at 7h10, nena 7h10 sunu guennoul deni tardei 🤣 tei deug la deh 11 sakh sunu guenei tardei teksi police mamelles soff ba deh 😭
2023-12-04 19:14:07
4
myabio20
myabioetdivers :
coter astuce je prepare tout la veille yewou rek sangoi ndeki yobou niou jangui
2023-12-04 22:25:31
1
To see more videos from user @atelier_art_bi, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About