@lamsandakarou1: #dienekaire #boymedinabi👊🏾 #medinafideuknékhé @Toubab bou bb Diéne 💪🏽❤️💥 @PA Omar @Alkhatir #lamsandakarou1

lamsa ndakarou ❤️🇸🇳👌
lamsa ndakarou ❤️🇸🇳👌
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 21 December 2023 16:04:32 GMT
843222
71872
1752
200

Music

Download

Comments

pgd_electro
pgd_electro :
Papa day soutoural domame
2023-12-21 16:26:45
6
ousmane2671
ousmane :
kou contane yalla guako dèfal say wadiour
2023-12-22 11:56:43
2
dame.mbow3
Dame Mbow :
yalla nako yalla deffal tawfekh barkep alkhourane 🥰nitt mom bou beugué ay wadiouram dra doukko diombou🥰
2025-01-09 16:23:28
1
user7041456059998
user7041456059998 :
dina am louné thi lamb inchalla
2023-12-21 18:14:19
11
zeynangom236
Zeyna Ngom :
manchallh diène yallna la yalla sam
2025-01-21 17:21:08
1
mbayesene6859
Mbaye babacar bou chelsea :
diéne borome dan kay khol rek khamko canam bi rek wanénaka
2023-12-21 19:45:50
2
louisdasylva23
Louis Dasylva :
c normal
2023-12-23 09:34:19
1
mbodjbasse
Walo walo bi :
Teral nala mom yalnako yalla lafal thiat
2023-12-21 23:16:07
1
badou.kara.237
Badou kara Sagna :
yalla bakhna
2023-12-23 10:54:30
1
user1258624908192
m. h. s. :
oooh🥰🥰
2023-12-23 09:34:34
1
profe989
wakeurbayekarim :
yalla nako yalla deffal ay ndam you beurri
2023-12-23 17:12:05
1
mameasspdgsstb
Mame Ass PDG SSTB :
Ndeysane 😭😭Yallna yalla defal kheweul thi lambe inchallah
2025-02-28 13:38:25
0
pgd_electro
pgd_electro :
C’est ça un vrai papa
2023-12-21 16:26:19
715
momorassoul399
Momo Rassoul niang :
Antouka liko warr la def déko ñianal rek képou kou aimer 🧡 yalla nga meune ba téral say waydiour amine
2023-12-22 14:49:18
392
cheikhoudiop215
JOOP GLOBAL TECH :
Diéne Kairé Ni la Meuna Mél Dafa Meussa Yarou Môme ak Sama Rak Nio done Fowando Cité Ascena(Derklé) .boy bou Yarou té bakh
2023-12-21 20:30:46
432
bmn2674
(B♤YE)---(M♤NDI♤YE) :
mane de xawma dome bou defaloul bayam wala yayam xawma koumi defal 😄😄😄li da diara wakh
2023-12-21 23:01:50
7
user3660944048917
Daz :
père doundal ba doyal machallah 🙏🙏🙏
2023-12-21 17:57:54
203
mbayebabacar382
mbayebabacar382 :
me yaw papa diou vakhenga tamit
2025-01-26 09:19:45
9
mbea318
Mbéne Seye :
ndeyssane diene kaire yalna la yala same ngua dounde ba nekeu rois des arène 😭❤️💯💯
2023-12-22 12:17:55
109
halile
Hallie :
Oh diene defna Lou nice yalnako yalla takhawou champion la li rek ladone rêve sama live bi pour sama pape mais yalnako yalla yeurem te khareko Al dianaye firdawsi 🤲😭😭😭
2023-12-22 11:09:17
50
mbayeyarambee
Mbaye yaram Bee :
Machalla loumou déf si wadiour douko reuthiou
2023-12-21 22:58:43
80
user7742196088702
zill :
Legui mom Diène moy sama mbeur ndax liko papame sedel ni
2023-12-21 17:53:43
40
leye50
Ibra leye :
macha allah douko réthiou mouk nite day am kilifa
2023-12-21 20:42:56
47
maremeseck
mareme :
dina amelou bah inchallal kou téral saye wadiour doko rethiou
2023-12-21 20:01:27
37
mohamedsow227
mohamedsow227 :
diene ko bakhe la na sarakhe dofop bo bari incahala limo bague dina ko am 😭😭😭😭😭😭
2023-12-21 18:09:43
6
To see more videos from user @lamsandakarou1, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About