@eutou_jiggen_yi_mme_diop: Ano 2024-11: sama goro bou goor moma eumbeulal#2024 #storytim #storytime #senegalaise_tik_tok #tiktokfrance🇨🇵 #senegalaise_tik_tok #papecheikhdiallounivers #seriessenegalaises🇸🇳 #mamendiayesavon😂😂😂🤣🤣🤣🤣 #mamicobra🐍 #youssoundour #mamendiayesavon😂😂😂🤣🤣🤣🤣 #youssoundour #tiktokfrance🇨🇵 #youssoundour #djongueattitude🎀 #ousmanesonkoprésident #mamendiayesavon😂😂😂🤣🤣🤣🤣 #wallyseckofficiel #mereforokh #sadiomané #mamendiayesavon😂😂😂😂😂😂 #VoiceEffects
Eutou jiggen yi🇸🇳🤱🏾🇫🇷
Region: FR
Saturday 06 January 2024 12:19:30 GMT
Music
Download
Comments
Mediop Dior :
mme
2024-04-01 16:39:58
1
nurudin__niass__🇸🇳🇲🇦 :
Li yeup Macky Sall la 😁
2024-04-04 01:29:57
0
Alioukâ221 :
yalla na sénégalais yépou dougou aldiana
2024-01-06 13:20:34
110
Babe :
Porte plainte ma chérie boulko sakh kaffer
2024-01-06 13:59:19
47
Maimouna Sy42 :
Ont réclame le pot de fleurs 🌷 🥺🥺🥺🥺🥺
2024-01-06 17:46:38
20
Mame Coumba Sarr 😻 :
histoire yi yeupe khana gni s'en dieukeur yi touki rek lay dal li
2024-01-06 13:38:08
19
katydia585 :
soko gardewoul noy def 5 mois de grossesse soko yakhé ray nit mounieul yallah baxna
2024-01-06 13:57:18
13
Aminatou 🏴🏳️❤️ :
Dome kéne douko raye allalou yallah la téh khalei mom yallah rk mo kay same
2024-01-06 12:29:32
10
aichaboye838 :
Massa ma sœur c’est ton destin mais garde ton enfant
2024-01-06 17:57:06
8
lady M M :
boulko ray Bakkar dilasi fekk ,Kom deug bi fèñ na c l'essentiel,sou dom bi dioudo,soko meunoul té nga yoboul ko pabi mou té domam géréko
2024-01-06 13:21:46
8
mme niang ballo :
ayé waye doyna warr
2024-01-06 13:09:31
6
M.A.G_🇸🇳🇫🇷🤵🏽♂️ :
😂mom ay story wam yeup pot de fleur bi Moy son visage mom lay wané 😂😂
2024-01-06 19:34:29
5
zouk🇸🇳🍁✨ :
Nako garder yarr ko khamoul loumouy djarign euleuk
2024-01-06 14:16:03
5
user2817641974652ndeyendiaye :
Sénégal der douma wedi dara 🤔🤔🤔🤔🤔
2024-01-06 13:35:39
5
GALSEN +221🇸🇳 :
Les immigrés kou ame moyen yoboul sa Diabar mo guineu worr
2024-01-06 21:37:51
4
PeulBouRaféte💋❤️ :
Cheuuuu🤭Pabi moyy vrai koba🤯🤯
2024-01-06 16:52:55
4
@fama❤️saliou❤️ Gueye ❤️ :
Doumako yake sou dioudo ma diokh ko bayam wakh dji djiékh wa salam
2024-01-06 13:25:30
4
khadybaniang :
wa yaw khana sénegal amoul justice portel plinte bala guaÿ acouché
2024-01-06 16:36:42
3
rassoul20🇸🇳 :
famille tass na
2024-01-07 10:37:09
2
Carl Cox🍒 :
Lii yéep amna Sénégal 😄😄😄
2024-01-06 19:03:49
2
Maya mme Ciss❤️🔒 :
Portèl plinte legui police 👮♀️reglèko
2024-01-06 14:29:41
2
N❤️S🫶S :
Sénégal dé problème yeup seuy la
2024-01-06 13:43:58
2
user2817641974652ndeyendiaye :
boule ko meussa yake teyeko diokhe ko bayame
2024-01-06 13:36:47
2
Élisa Faye :
ce bb est innocent garde le
2024-01-08 00:46:47
1
dyhhiouqi8wi :
😂😂😂😂
2024-01-07 16:04:02
1
péra Dieye17🐏🔥 :
soubouhanalah 🥺
2024-01-06 23:29:00
1
Soldarou seigne B… :
thiey yalla
2024-01-06 21:46:14
1
aïcha 🇸🇳 :
Li mom v!Ol leu pabi kou diara plainte la ki mo bone deug
2024-01-06 17:58:30
1
MariamRassoullll🥰❤️🫶❤️ :
k Allah ns Pardon mais il y a certaines grossesse 🥺🥺
2024-01-06 16:38:08
1
Fat 512 :
Heureusement douma nane dara ay ataya ay jus lii😭😭😭😭
2024-01-06 16:00:18
1
leader :
il faut porter plainte contre ce vieux voyou pour l'enfant tu le gardes si tu ne peux pas va le déposer chez eux dem sa yone
2024-01-06 13:44:37
1
awa :
🥺🥺🥺
2024-01-06 13:37:28
1
Abrakoum :
yaw defo dara sa goro mobdef lep gardel eumb bi yaral sa dom inchallah yalla dinale may kou bakh
2024-04-01 18:55:45
0
Cheikhna Bd :
سبحان الله😳😳😳
2024-03-10 14:03:25
0
Mme tall :
😭😭😭
2024-03-09 00:21:06
0
u maodo sylla 1986 :
bayi kofii rek bouko ray mai tamit sama mbokou moodou moodou yi laa yeureum mai tamit bayi leen khell djigueen gni ndakh tamit gnoom dagnii sokhla see
2024-03-06 12:41:20
0
Mme Diagne :
si votre mari né pas là.évitez de boire du thé ,du café ou jus.dans lé maison ou il y'a certains hommes irresponsables .surtout lé femme des immigrés
2024-02-26 14:14:01
0
papis papis :
madre mía
2024-02-26 11:46:23
0
Ibn Abdallah :
garde cet enfant la tête haute il n'a pas demander à naître en plus c'est pas de ta faute
2024-02-21 03:16:45
0
Dof Bi Tidiani :
pabi thigana trop
2024-02-20 21:45:45
0
Karime Wade :
yaw mouno bimbali wakhou tatanté rék ngay wakh tay sama goro tay sama papa way lousa proleim
2024-02-20 14:23:34
0
diagne mouhaméd bamba si khole :
gua plent ndayame boulsi dawe dara yone amna sa borome keur wakhna deug daflaye sékhlou c vré
2024-02-18 20:59:03
0
Khady Modou Mbaye :
garder ko mo geune ngay risker sa vie 5mois soringa mougneul ndeysane
2024-02-16 21:27:11
0
Moussou Ndiaye :
Porte plainte contre lui, comme ton mari, il t’a pas soutenu euleuk lou diara sora léla sa dome khané yayam dou wone kou bone
2024-02-01 21:30:07
0
Megane :
mbeté famille japonaise
2024-01-24 13:36:21
0
King Le@der :
Soukou téllone wakh yayam sakh si 3 premier mois yi, bou boba non seulma Goorom dina avoué mais aussi elle aura le choix pour avorter ou pas.
2024-01-23 20:42:50
0
Bilou :
dôme bi Kay sorinà instant bi Gardel lek
2024-01-13 16:11:43
0
ibrahimakhalilend6 :
story time foko dégeu ay doul la
2024-01-12 22:46:53
0
rabichou45 :
🤔🤔🤔🤭🤭
2024-01-12 13:58:30
0
To see more videos from user @eutou_jiggen_yi_mme_diop, please go to the Tikwm
homepage.