@niang_busines: #lyrics #pourtoi #viral #seka #galsen_tiktok baax ak yarou amna solo🧏❤️

NIANGUENE SEN VAISSELLE🙏❤️
NIANGUENE SEN VAISSELLE🙏❤️
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 28 February 2024 12:22:16 GMT
835041
50335
249
2595

Music

Download

Comments

patriote_dans_lombre
PATRIOTE_DANS_L'OMBRE 🟢⚪️ :
MEUNATOUMA SIGGI KHOL KENN NDAX GATHIÉ 😂😂😂 BAL LEN MA
2024-02-29 18:41:24
177
7837479273fjj
❤️🥰tvjnk :
Man néké depuis khalé dama don diakhassé parole yi Yéne laaay🙆🏾‍♀️
2024-02-29 23:02:53
97
dmn629
Yayou Mouhamed :
Mane bakhadiarou ladone wakh 🤭
2024-02-29 17:48:35
17
faandaw
Fha❤️👑 :
ndéké diaxassé kepp la nekon🥺
2024-02-29 17:28:58
66
mignonneprincesse0
Mignonne- Princesse ✨❤️ :
bakhadiarou loum la mayoul doulako khagn, karaw nietti kersa loum la khagnoul doula ko may ☹️☹️☹️☹️tonton Balma
2024-03-02 01:57:11
8
awangom1969
Awa Ngom🥰 :
qu,Allah te pardonne et t'accueille au paradis firdawss. Adieu l’artiste
2025-05-03 20:35:47
4
fagueyesene01
Fafa :
Hannnn li ley wakh 🤣🤣🤣🤣
2024-03-06 22:00:41
1
massambaseye465
MASS Seye465 :
Paix à son âme Rip😭😭😭 FATIHA 11 IKHLASS Amine 👏👏👏
2025-05-03 20:00:20
4
nafshop22
Nafshop :
Aye mane meussouma khame limouy wakh liii
2024-04-23 12:14:15
1
aissatadiallo039
Aissata Diallo :
Meussouma kham li oayy wakh
2024-02-29 10:02:31
26
la.fille.unique.de.samum
~Élément ~serigne~saliou~ 56 :
mane dhè weuy bi dama ko done diaxasé 😂 mousou ma xam lila wax 😂🥰✨
2024-02-29 16:13:29
4
khady.sow721
Kddy_s💜💜💜💜 :
wayy bi noumou toudou
2024-03-01 22:26:26
6
fatoumatabintoufall2
fatoumatabintoufall2 :
ndeysan thiéye adouna dou dara yalla Nako yalla yeureum kharé ko aldiana firdawou si barcké seye dinamouhamad aléye wasalam😭😭😭😭😭😭
2025-05-04 01:32:14
3
awoumatemptopoumakene24
💥Ada💢fass💯kesé🇸🇳🇱🇷 :
kouko weuy 😞l titr
2024-02-29 08:31:24
7
evasita71
evasita :
yalla na adiana di keureum
2025-05-03 21:27:12
10
binetou28
Binetou :
ndeyssane parole yi amna solo néx, yana la Yalla yeureume té diégueul la🙏
2025-05-05 22:47:44
11
fatima.zahra850
fatima zahra :
Pourquoi j’ai pleuré direct 😭
2024-04-20 17:38:32
1
mmethiam816
mmethiam816 :
😂😂😂Ay loumay wah sounou wa keur 🤭😅😅la ilah ay li di ay ma meuneu diahassé ba gueume samay parole nak🤣🤣🤣
2024-02-29 22:46:49
6
thiatoualamine5
Thiatou Al Amine SY 7🥰❣️ :
sama rakadji kay wouyou ioe lay way nii🤣🤣daga rew rek🤣🤣🤣
2024-03-01 23:24:12
1
tymafassa2
tymafassa :
Bilaye
2024-02-29 06:29:05
1
rassoul.saveurs.na
Rassoul Saveurs Nautiques :
Paix à son âme
2025-05-03 16:09:52
0
madamefaris
Madame faris❤️💍🎉 :
Vraiment
2026-04-07 22:04:25
0
oumy.laythiaat
oumy laythiaat :
Paix à son ame
2025-05-04 16:40:06
0
gueyenioro80
adista :
machallah samba alar
2025-12-05 11:27:11
0
ndiayejr71
BüüR Ndiaye 🇸🇳🇮🇹❤️🥇 :
Lou lerr
2024-02-29 20:13:25
0
To see more videos from user @niang_busines, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About