@touba_xassida: #touba_xassida #senegalaise_tik_tok

𝑻𝑶𝑼𝑩𝑨 𝑿𝑨𝑺𝑺𝑰𝑫𝑨
𝑻𝑶𝑼𝑩𝑨 𝑿𝑨𝑺𝑺𝑰𝑫𝑨
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 31 March 2024 04:13:25 GMT
252557
26520
874
478

Music

Download

Comments

deboursy1982
Debour Sy :
sou fekei dou diouli rk do dioulite c est tous
2024-03-31 06:37:01
51
faye.birame.penda5
faye birame penda waguane :
Ouztass yii ay nafek laniou il faut dire la vérité djouli wathioul keneu
2024-03-31 23:04:03
7
yahkhoba8
Yahkhoba :
wax ji Mooy ko bàyyi julli doo jullit
2024-03-31 18:28:05
0
becaye_221
becaye_221 :
🥰
2025-03-02 15:49:12
0
cheikhfallndiay66
Cheikh Fall Ndiaye :
En tout cas Ibliss mofi dakone djouli foumou moudié 😂
2024-03-31 11:35:56
146
yonentemouhamed
MouhaGe Gueye🤍 :
Niveau bi dafa kawé trop ❤️
2024-03-31 08:04:36
135
taphafall04
tapha Fall :
leuguéya geune djang djokher geune djouli mandou geune koorr Diarama MAME CHEIKH
2024-03-31 12:44:42
99
kou.bakh5
talibé chiekh :
sergne touba moni koudoul djiouli boula kena soul si armelou djioulite moko wakh thi masikoul chikhar
2024-03-31 10:26:20
75
djmakhou4
Dj Makhou🎙🎶 :
yakou diambour koumou daw sa birr dangua wané mandou lénn téh nékk si loum wara nékk louy sa yonn si kanénn
2024-03-31 06:51:36
66
ridialseck3
Ridial business :
siguil gua bay fall yépp fall yaram cheikh 🥰
2024-03-31 04:29:43
37
user42534789
assadul xadiimi :
cëy sa Mame cheikh Ibra 🥰🥰🥰
2024-03-31 04:49:27
37
abdoulniane204
Abdoul Aziz Niane :
soubhanallah les oustaz n'ose même pas le contredire
2024-03-31 09:48:00
26
fa.mourate
Fa mourate :
Dieureudieuf Cheikh ra fall 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-03-31 06:26:23
15
djliy_abdou_khader
Serigne Djliy abdou khader lô :
Oustaz yi wakh léne gni li yalla wakh ak yonéntem lamigne wou bou don takha don djoulit kone yéfeur don ay djoulit yéne ngéne wara waar ki mou léne wa
2024-03-31 11:07:50
12
elhadjimamadundiaye
papa le mecánico 🇸🇳❤️🛠 :
kou xamoul rek xamoul mane magui si cheikh ibra kou lenene dieulale 😭
2024-03-31 18:29:29
11
mouhametndiaye351
Mouhamed ndiaye🎙️ :
Nitt menoul wah ba niak diouly dagane
2024-03-31 06:27:33
10
alhamdoulah97
Alhamdoulah :
bilahi fall ❤️❤️
2024-03-31 04:41:04
9
badanguer2
Bada nguer :
Lou doy war 😂😂
2024-03-31 04:28:01
9
djibba0207
Djibba0207 :
dioulit mom boudoul diouli nékatoko amoul layam layam sen lamigne you reuy yi rek mo yakh Sénégal
2024-03-31 07:29:56
8
alioufaye2139
bayefalbi🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
Dieureudieufati borom touba Diarama mame cheikh Ibreu faal
2024-03-31 06:55:11
7
ba.alassane44
Ba Alassane :
koudou dioulli do dioulinde 😭😭😭
2024-03-31 09:18:50
6
m_modou_diack_officiel
✪ Modou Diack Goor Deugg✪🫆✪ :
Baye Fall moy philosophe fa Yalla ❤️
2024-03-31 05:07:58
6
mamekhassimembaye
Mame Khassime Mbaye :
akama béck thimom🥰🥰🥰🥰
2024-03-31 04:40:31
6
modoufallcisse
Modou fall Cissé🇸🇳 :
Contene N’a Dh Barkép Cheikh Ibra faall🙏
2024-03-31 04:35:21
5
bigmobst
Lawbe Sénégal :
ki loumouy wakh faw nga am bopou pour deguko
2024-04-01 00:02:31
5
flegme0209
Al Bachir :
Mais wakhou niou nii Ibliss mo fi dakhoon diouli? légui nk...??
2024-03-31 09:54:15
5
user1461766991652
user1461766991652 :
loolou dou lay dioulite = diouli kou doul diouli doo dioulite
2024-03-31 10:23:27
4
cheikhbiteye06
Cheikh biteye 567 :
♥️🥰🥰
2024-03-31 04:29:28
4
modoucssy
Modou Cssy :
Yen kon ki wah nafii dara teh aii Oustass nekh fi 😂
2024-03-31 06:45:47
4
idaly_di
IDALY🥰🇸🇳✨️diop :
🥰🥰🥰🥰
2024-03-31 04:25:26
4
ablayediallo968
Ibn ahmad :
Koudoul diouli yeffer gua
2024-03-31 05:57:58
4
linetalibamba
linetalibebamba :
niveau bi mo kaawei ba nopi âme talibei Xam ba nopi meilni ku xamoul thiey sunu Mame cheikh Ibra moo yégg moo seuss
2024-03-31 05:18:39
3
alla__fall
user2807171388908 :
mom wakhou fi dra de oustaz yi ay nafékh lagnou
2024-03-31 11:15:42
3
babacar_dieng_1
BABACAR :
Migui melni kouy wakh xam xam deh😂🤣
2024-03-31 07:44:30
3
mamounediane1
mamounediane1 :
العهدُالذي بينَنا وبينَهم الصلاةُ، فمَن تركَها فقد كفرَ🙏waxofi Dara
2024-03-31 07:10:10
3
fallouniang077
Fallou niang 077 :
Ko geumoul diouli dou dioulite
2024-03-31 11:59:44
3
alioufaye2139
bayefalbi🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
Diouli mando ko gueune 🙏🙏🙏🙏
2024-03-31 06:55:43
3
moussadiarraamc
Di@rr@🇪🇸🇸🇳 :
Li mata xam dall moy cheikh Ibrahima fall lépam ndiarign la❤️🙏
2024-03-31 13:05:21
3
salioutine188
saliou 188 :
waw goor mourde machallah
2024-03-31 10:12:26
2
mouhameddia6446
dia kaw kaw :
Sénégal mo bari ay nafek ki li wakh ay doul la yalla diouli la chatane kou doule diouli yefarnga
2024-03-31 07:23:45
2
user3634916988277
ndiankoumbengue :
Diarrama Mame cheikh ibrahima fall
2024-03-31 08:26:26
2
massoumyamane
minane :
lima si geuna néx Moy gnoubeuri fii gnongui dingat té wallahi dougnou diouly kor gui sakh worou gnou lépou
2024-04-01 01:21:02
2
khkhammmdim0
Khadim Niang2922 :
🥰🥰🥰
2024-03-31 05:58:10
2
cheikhpatesow0
cheikh pâte sow 🥰 :
من ترك الصلاة فهو كافر
2024-03-31 06:25:48
2
niaarybaayfaal
ÑAARYBAAYFAAL K.S.F💙💦 :
Toumeuh yagg na si yone Wi … wayy ki wara djouli djoulil woral té mandou bayignou nioune Bayefall ak Cheikh ibreu…
2024-03-31 15:02:46
2
thiare480
AL THIARE06🇸🇳 :
Thieuy souniou oustaz yi danio complexe ndaysan
2024-03-31 06:51:04
2
mame.cheikh.lof3s
user2795907866056 :
DEUKÉ SANTE CHEIKH IBRA 🥰🥰
2024-03-31 21:41:32
2
serignefallou671
fallou awa Bousso :
Ngirr yalla mandou lénn si baye fall yii mon guéun
2024-03-31 11:52:50
2
khalile2812
Khalil 244-313 :
Xaamm bi gueu kawè moy xamm YALLAH tè xamn YALLAH keur Serigne Toubaa la fèkk baxxx. Dieureudieuftii Serigne Touba
2024-03-31 22:49:21
2
laminendiaye13
Thiate Diarra :
bilahy walahy sana kogne la niari pa di kholo ba nara khékh ndakh ma wara yoré diabi diouma bii ndakh intérêt kasé fii si parcelle sama kanam
2024-03-31 05:47:44
2
mor.gueye457
Mor Gueye45 :
Baye fall daye dégeu dadj
2024-03-31 15:57:49
2
aldimobadousamb
aldimobadousamb :
té Mouy DEUG wayeh règles bo guiss amna exception cheikh Ibra exception la ci djine dji yallah moko def❤️
2024-04-01 20:45:13
1
To see more videos from user @touba_xassida, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About