@sunucoco3.0: il faut savoir savoir reconnaître et accepter le problème pour pouvoir y apporter des solutions. arrêtez de toujours refuser les maux qui paralyse notre agriculture. évoluons pour proposer de meilleures produits qui puissent concurrencer l'importation et nous permettre d'accéder à l'autosuffisance alimentaires et l'accès aux marchés internationaux #viral #views #goviral #tiktoksenegal #focus
wa yaw soble importe bi khana bayoun ko probleme bi moy bi dafay doga nior mo takh soble bou bess la
2024-04-13 09:32:12
0
makha cissé :
temps bi gua deff di explique bo douguone keur you nék sen kogne dou gniak gnou wane la nougnoukoy dogué 😂😂xalé reso socio bi gua done mane mi gor sakh cuisine nako 😂😂
2024-04-12 20:41:29
43
YÉRIKABA :
lol man mi je suis ingénieur agronome et j'avais commenté en expliquant nougnou kay togué,
2024-04-13 10:29:47
7
echo :
Je pense il font exprès. Normalement l’onion ne doit plus etre arrosé 20 jours avant la récolte. Mais ils l’arrosent pour augmenter la masse des oinions pour gagner plus d’argent. La quantité d’eau
2024-04-12 23:29:47
83
Fatousha :
ah nioune dé môme laniouye tog mais amouniousi problème bii vraiment Mane môme guisoumasi ndokh
2024-04-12 21:45:54
132
sallaguisse :
en tout cas tu as raison lolou moma dall jour corité
2024-04-13 00:18:54
82
Gunners :
Mais madame tout les fruit et légumes ont une déférente variété il faut s’y adapter je suis cuisinier 🧑🍳 même oignon que vous dénigrez au 🇸🇳 qui oignons 🧅 rouge est plus chers la ou je suis
2024-04-13 11:37:45
6
Adamadiallo :
mane dei guissouma koula wakh ni meuno tok au contraire gayi you barri daniouni sen boss defoul dra.
2024-04-12 22:15:03
12
Georgette 🥰 :
😂😂😂 toi tu penses être où tu es au Sénégal aussi faut comprendre.
Mais c'est très important ce que tu dis surtout pomme de terre bi . 😘😘
2024-04-13 00:37:38
7
oumaya💕 :
Technique culturale bi sougn ko améliorer wone dougnou am blem bougni togg ba kounek di proposer ay méthodes culinaires 🤦🏽♀️pcq’ bou kounek di proposez solution c par c k tt le mde a le mm blem
2024-04-12 20:05:24
11
ebeno ébène :
mani ndokh kecé la.demane gni togu mbana fofou système meunoussi dara ndoxxxx patieuuuuuuuuuuuuuuuuuuuu
2024-04-12 20:33:30
5
evatitachou :
machalla machalla mbam yi nio eup si commentaire yi douniou khalat sah soblé bi da beuri ndokh lolou kén neunouko dindi qualité bi bahoul
2024-04-12 20:38:25
27
missreds992 :
linga wakh deugue la walahi soblé bii dafa nekoul de qualité beuri ndokh ba diakhal gniou pomme de terre bi soko frité mou naane huile tek si di lakh
2024-04-13 08:11:35
23
Sokhna Diama😇🤍🥹🥰🦋🕊💖 :
Mais ma Shary tu as raison soblè bi dafa beuri dokh Parck nous aussi mom lagn togou korité bi Mais dafa beuri ndokh té defou niou thi ndokh do comprendre sah
2024-04-13 19:09:43
11
kalthoumcisse3 :
Li d ma daloon si korite bi..sauce bou nokhe sucrée ba pare amoul diwline nakh dama toni nokh bi 😂
2024-04-12 20:47:37
8
Ndeya🦂🌸 :
Suis vraiment d’accord avec toi 👏👏🤝
2024-04-13 00:00:08
6
To see more videos from user @sunucoco3.0, please go to the Tikwm
homepage.