mane sama bosse legui mou def trois mois te gamme bou 10000 bene rek la dieundone
2024-06-25 15:12:02
3
domingamendes11 :
boul niou top balniou rek guir ndieumi serigne fallou
2024-06-25 16:31:43
2
moussou :
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣wwouye mane dé dama bosse legui mou diékh,promo laye khare
2024-08-18 17:48:47
0
WAKEUR MAWLANA BAYE ASHOP.APIX :
toutou bal lene khelou khale molène diapone produits toutou astou disponible à apix tiwaone peulh et alentours 77 551 61 47
2024-06-25 18:53:03
1
antisee11 :
toutou beugu nassi d creme d visage bi message nala snap man limou hydoquinone motakh ma safar sii
2024-07-26 14:09:31
0
Bapoulo :
U
2024-06-26 15:54:27
0
Soxna Awa Fallilou😇😍 :
Nagn Len ko nian guir dieumi fallou awa bousso nak danouy wathieu magal yayou gallass 🥺
2024-06-25 15:13:55
7
lyboussotorodo1 :
Toutou iow linga wax yeup deugu leuh ya bax legui nak waxtane nagn ba dioubo dhe reukatal gamme dou 10000 doto fi degu loula nakari waw key Ndiaye diatta 🤣🥰
2024-06-25 15:11:56
7
MECATRONIC SENEGAL :
Toutou crème bi bahna sakane na diw bi rek mo touti 🤣🤣🤣🤣🤣🤣Wayer y’a meilleur 💪
2024-06-27 05:05:01
5
Yayu sangue bi :
Yaye diaye produit you meilleur yi mo takh niouni la promo niouneu team AS promo laniou wakh @Toutou Astou
2024-06-25 19:16:05
3
Fatima mu sonko toutou✌️ :
Ay way gamme bou 10 milll toutou
2024-06-25 18:14:37
2
aminanaby :
ya fiye diaye crème de visage bouy wakhal yalla manchalla .mako wakh ma tata Amina milan .deugg gou weer .man sama visage Dara mounou KO won khessal bilahi .bi commencer utiliser sa crème la khess .
2024-06-25 16:54:34
2
kinouch60 :
toutou balniou dotou niouko dèfati 😉😉😉😉😉
2024-06-25 15:37:27
2
élément Toutouastou :
@Toutou Astou Khaleyi iow laniou diokh bop masha allah sama khalakhina reukeulén promo ndeweneul deuk bi yengou 🥰🥰
2024-06-25 15:16:27
2
Kharitou p@p@m♥️ :
Diw bi moy diekh mane dh magui agu 3 crème de visage yima laloul
2024-06-25 21:19:10
1
Sulture 🔥 :
Sama Savon la fatté bima demé tabaski 😏
2024-06-25 16:16:31
1
Ramatoulaye 🥰 :
Bilay crème de visage bi rkk meuilleur la deff ❤️❤️❤️❤️gawa wekhal kaname dindi saye taches meuilleur chez américain shop
2024-06-25 15:40:50
1
odyle Dassylva Officiel @ :
Tite rek 😂😂😂 billay
2024-06-25 15:10:38
1
Khadija 💅🏼🧚🏽 :
Love u toutou
2024-09-14 12:55:54
0
GermaineFaye87 :
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
2024-09-10 05:29:19
0
yacinefall850 :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-09-05 13:24:53
0
fatoumatagueye10 :
tata loy proposer les femmes enceintes pour teint marron sans imperfections
2024-09-02 16:55:50
0
Fatou Bintou Sall :
❤️❤️❤️
2024-08-20 22:34:48
0
user2641527245172 :
10
2024-08-20 12:56:55
0
user2641527245172 :
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
2024-08-20 12:56:43
0
yayou Rassoul :
Yayou fallou Gallas rekatal rék gamme bou 10000fr nioun gnep d'accord nanou lo diayoul bakhoul té lo diaye niou jeunde té par force la na daga meilleur