@dieuwrigniboulayesaliou: Athia talibe bou nek 20mill wala lo meun #foryou #viralvideo #foryourpage #viral

dieuwrigniboulayesaliou
dieuwrigniboulayesaliou
Open In TikTok:
Region: IT
Saturday 20 July 2024 17:12:43 GMT
107617
15714
1010
160

Music

Download

Comments

aminatarassoul60
aminatarassoul60 :
Na niep diokhé amoul mouride amoul Tidiane négou yallah la ❤️🙏yaw kou bakh ga 🙏
2024-07-20 17:19:16
142
lamine205.1
mouhamedlamined85 :
Café tivaoune lay nann ni sax ☕️🥰
2024-07-20 19:08:54
54
amadoufall074
amadoufall074 :
merci sa démarche rafétna Yalla nah Yalla faylah
2024-07-20 19:24:06
42
adji__almaktoum
adji__almaktoum :
Iow Danga Bakh Après Ubbi Jumaa Nga Nieuw Ma Mayla Sama Bopou Jtm 🫶 ❤️😩
2024-07-24 10:17:38
39
mass78782
modou lô :
nit kou bakh guay
2024-07-20 20:42:47
18
ndiaga.ndiaye07
Ndiaga Ndiaye :
li dafa rafétt bilahi yallna la yala fayal bopam 🙏
2024-07-20 21:39:00
16
maodo.malick.guey
Maodo Malick Gueye :
Ay way ya bakh❤️🥰
2024-07-20 17:22:55
8
amina_daff_bou_sbs
amina_daff_bou SBS2😘 :
Walahi daga bakh 😭♥️🥰 sunu borom saam la té arrr la 😭♥️
2024-07-20 21:39:09
7
simohdoumbia
sidymohametdoumbi :
souma dougué tik tok bala ma guén fog ma guiss sa vidéo sounou douma teudd. Yallah nassa diam yague seugne bi. Macha'Allah
2024-07-21 04:17:10
6
yayendokhseck2
yayendokhseck4 :
machalla frère li rafét na waye merci
2024-07-20 20:26:36
6
mmdbymaktum2
Mmd❤️ :
Yagui def Lou Yallah beug Machallah diam si Yaw ❤️❤️❤️❤️
2024-07-21 10:34:50
6
lefarfolu0
Mouhamad ♥️ :
Mouride kheur bbagn trop tème niou agaliko nioune tijane ti tok🤧😂😭
2024-07-20 22:05:27
6
racine29
Racine🥰🇸🇳 :
Yalla nala yalla fay 🙏🏻🙏🏻🙏🏻
2024-07-20 21:03:52
5
jeune_arbitres
OG-MD-Jeune-Arbitre 💖🙈🎊 :
Dama la beugueu dallall magall🤪
2024-07-20 17:20:11
4
user6181044180745
yacine :
yabakh barki serigne babacar sy
2024-07-20 18:23:02
4
ndiayesacsac
Ndiayesac Sac :
masahalla yallna yalla Samou
2024-07-20 22:22:02
4
o_rio3
o_rio3 :
Mais d demb rek diokhé na 22000
2024-07-21 15:47:38
4
omzodollar879
🅾️〽️ZO ~ 💲ecka🤞🏾 :
Mouride deug gnioun tidiane yi contane nagn 🙏🙏
2024-07-20 20:42:15
3
aliounebadaragnin8
alioune badara Gningue :
dieuwrigne magal gui préparel yaw lay dalale
2024-07-20 21:20:58
3
secktalla49
seck Talla :
merci beaucoup
2024-07-20 20:53:28
3
rimreus0
Rim99 :
Ya bakh way serigne bi, yalna yalla fayy la 🤲
2024-07-21 13:50:04
3
abou.jah5
sadikh.09 :
jajeuf jeuwrine
2024-07-20 18:17:02
3
adamafaye017
adamafaye9380 :
yaww daga bakhe
2024-07-21 11:16:36
3
amina.samb10
Amina Samb :
Mane mome yalla 🙏rekk motakh ma beug le❤️
2024-09-05 18:57:40
2
zalosenghor0
Keur Serigne fallou plafond :
Bamba moy maodo ❤️
2024-08-29 21:41:09
2
user840447364021
user840447364021 :
gnoune tidiane yi gnougui lay nianal machalla say kadou amneu solo
2024-07-20 21:22:13
2
ijondoyelebou
ijo Ndoye Lébou ✪💙❤️🇸🇳 :
Quel Maturité Machallah🙏🙏🙏🙏
2024-07-21 12:33:04
2
mbayangbsbs2
soxna Mbayang Al Amine❤️😍 :
Manchallah yallana ya fayy yiw
2024-07-20 19:30:14
2
soukeynadiagne7
SouKeyna 719 :
nioune tidiane yi contane naniou thii yaw dé billahi wallahi yalla na yalla fay la yiw li moy Sénégal 🙏♥️
2024-07-22 00:39:38
2
seydina585
moi même :
Dieureudieuf Dieuwrigne yalla nala yalla fay yiw si Barkep Borom Touba 🙏
2024-07-20 21:28:53
2
asssamb26
asssamb20 :
machalla ❤️❤️❤️
2024-07-21 00:10:52
2
layedionu
layedionu :
Machaallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2024-07-21 00:09:52
2
racinebusiness1
RACINE BUSINESS COMPANY🌲🌍🖥️ :
Ma challah mouride
2024-07-21 14:16:20
2
amekeurtivaounemoncombat
AME KEUR TIVAOUNE MON COMBAT🙏 :
talibé cheikh bii kenkéliba lay nann ni Sax ☕🥰🥰
2024-07-20 22:54:30
2
babacarciss7
Babacar Ciss :
Dou takh niou nieuw magal dehhhh da nguene niouy bappp😂😂😂😂
2024-07-20 23:48:21
2
mamadoutalibecheikh770
Mamadou Talibe-Cheikh📿🇸🇳 :
❤️❤️❤️CONTANE NAGNOU TROP
2024-07-21 11:56:40
2
user36188492003634mama
user36188492003634 MilanAC❤️🖤 :
nitt kou bakh nga 🙏❤️
2024-07-21 01:56:07
2
yayoualmaktoumsy
SA- - - -S❤️🍯💍🫦❤️ :
Bilay wallay jtm si bark Serigne babacar sy ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏
2024-07-26 03:01:25
2
seydiababacarsadi
M@@MKhâF :
Dieuwrign beugg naleu sétesi Fouma lay fékk. ma ngi Tiwawon
2024-07-20 22:15:03
2
talibetv2
talibe TV lérou daradji :
Wax deugue yallah man sop nala lolou wlh🥳🤍
2024-07-20 22:21:19
2
khalifambaye250
khalifa.Babacar.bü.Ndiol fouta :
Kou beug si tidiane ma diokh lako Walhai contane si ioe Mane mom ioe la beugone si mourid yi😭
2024-07-21 13:31:39
1
aminata.ba.ba
Aminata ba Ba :
🥰🥰
2024-09-02 17:29:33
1
issaboy272
issaboy272 :
♥️♥️♥️♥️♥️♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2024-07-20 21:49:51
1
dioufgoratalibecheikh
Talibécheikhgoradiouf :
machalla seringue bi contannaniou trop♥️♥️♥️
2024-07-20 21:48:45
1
mill.main8
Djamil 🩸😎 ★ :
dieureudief mame maodo ❤️❤️❤️
2024-08-15 20:49:26
1
nikitakhalifa1234
nikitakhalifa1234 :
Merci beaucoup 😭❤️🙏yalnala yalla faye
2024-07-21 15:34:05
1
moridbi07
Baye mbaye 102 :
mafi guena bague seringe touba 🥰
2024-07-28 22:38:06
1
massar.niane
niane 313 🤲🤲 :
bindalgnou nimorobi ci kaw
2024-07-21 07:25:46
1
atome17
user3936449488090 :
merci beaucoup 🙏🙏🙏🙏
2024-09-02 11:26:41
1
modoundiaye2957
modou ndiaye295 :
Ani numéro bougne koy df ?
2024-07-21 00:50:35
1
To see more videos from user @dieuwrigniboulayesaliou, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About