@_h_n_s__: #CapCut #senegalaise_tik_tok #pourtoi #fypシ #viral

Hassan_Nourou_Salam
Hassan_Nourou_Salam
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 14 August 2024 16:11:39 GMT
725070
63331
955
3717

Music

Download

Comments

dijafallilou1
khadydjatou fallilou :
bilakhi deguele sama yaye nonoula méle fouma dém douma sonnou
2024-08-14 16:15:53
647
ebenefallfall
Ebene Fall Fall :
je ne suis pas d'accord parfois yay bakh dome dioudou bonn et le contraire aussi
2024-08-14 23:34:49
170
ndeye.seck.mbaye843
Mrs fall❤️💋 :
Dome dia Ndeye dia
2024-08-14 20:39:13
81
mouridoulah.09
mouridoulah.09 :
Waxoul deug gouye Dina diour xétax
2024-08-15 09:50:54
16
mamanrabia02
MAMAN RABI AL HADAWIYYA💫 :
Wally seck noum Sant
2024-08-15 10:03:28
8
alagie.secka5
Alagie Secka :
dafa lerr dundo nako 15 days ladeff se deser b awma problem leke awma nane
2024-08-15 20:35:32
2
esmadiallo3
أسماء :
Alhamdllh ☺️mm sama mame ni la mele dey bagne leke diokheko kenene mou leke
2024-09-05 19:47:38
1
ababacar.cisse3
BAB'S BŪ SONKØ🇸🇳♥️ :
Gracias madré 🥰
2024-12-13 08:06:31
1
univers_mame_fallou
𝑭𝑨𝑳𝑳𝑶𝑼 (فالو بار) :
Kouko bagne sa yaay mo am melokàne
2024-08-15 09:24:16
7
serignefalloudia1
falilouh presentateur2 :
walay ndeysanne 👌
2024-08-25 07:42:05
1
labelleetlabrave8
labelleetlabrave8 :
ki sama yaye lay wakhale longue vie maman chérie ❤️
2024-08-14 23:05:30
22
ardodiallo0101
Diallo dièry ardo :
wallahi ndeyssann sama yaye dia yallana gniou la yalla fayall si barké nabil moustapha 🥰
2024-08-16 08:38:45
6
dieynaba311
Diabaté🇲🇱🇸🇳❤️🫶 :
Wallahii sama yaye dji sonouma benne yonne akk fouma meunti deme seck goudal fanne 🥺🥰
2024-08-15 10:35:06
9
olivia.nicole.kab
Aminata Olivia 🇸🇳 🇮🇹 :
Hoooo ma yaye namenala yalla nagnou yalla wanélé di diame Inchala 🥰❤️
2024-08-16 10:36:16
9
codoudiagne4461
adjaratou :
machallah walahi deguela
2024-08-14 16:49:17
15
aminatambaye0511
Diarbatoutons 💍❤️ :
Sama yaye dè walahi domou diabour lék ba souur moko gueuneul sakh diambotam lék motakh fouma dem douma diakhlé douma khiif douma mar
2024-08-15 01:04:51
3
mariethiam905
marichou thiam :
bly deugue la
2024-08-14 16:27:53
26
aldimobadousamb
aldimobadousamb :
magui ni khamna ci dara 🥰
2024-08-14 16:44:07
14
ndess.samb
ndoumbefalillou samb❤️🥰❤️ :
je confirme sama yaye talibei yi, maçon yi mécanicien yi amoul Khadija AK séne motax fougnou dem dougnou khiff AK Lou meuna âme nak
2024-10-20 16:31:52
2
mamadou78438
bogue ahmadou bamba :
billahi masi xam darra
2024-08-16 00:24:54
4
coumbistashop720
coumbista :
sama yaye la begue yobou makka
2024-08-17 15:23:28
3
hamid22107
[email protected] :
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️amine yarabi
2024-08-15 18:57:55
1
user701231187
Cheikh :
lo lou yalla wakhoul ko dé sama yaye🙏
2024-08-18 21:31:27
3
mamanloubanasagna
Mamanloubana Sagna :
Billahi dafa leer
2024-08-15 16:01:57
2
usergsuqntud7u
Yayou s saliou :
Nkandji socé lolu rk lay df ndiokhé lek
2024-08-15 08:27:08
1
To see more videos from user @_h_n_s__, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About