Jeux quartier bi nanou wout ay khiir kou guéne rék guénd thiaw ko
2024-08-16 17:17:20
0
Cheikh dieng :
🥰🥰🥰
2024-10-31 12:13:05
0
enigma :
wa exellenece li foum moudj
2024-11-11 07:47:55
0
Leza Thiam :
tall len keur gui
2024-08-15 23:23:30
624
Lõ ndam🇸🇳 :
Na wa quartier bi guene dem niaf sen ndeye khawma lou takh sénégalais amoul foula
2024-08-15 23:28:03
421
PIKINOIS A VIE ❤️ :
wa apr niofii andii thiaga dji si rewmi
2024-08-15 23:17:35
381
maimounandiaye348 :
Mane lima diahal Moy kiy djohé carte thiaga môme hana dou djoulite😂
2024-08-16 01:29:52
285
Mbaye Babacar :
Motax SIDA bii mogui gagner terrain rek 🥺😳
2024-08-16 00:35:03
230
Bouchra :
Policiers yi Ay corrompus lañou système bi ba légui changer woul. Rupture souko Diomaye beuggué ci hommes de tenus lay commencer. Politique immigration naci Etat bi wax sinon…. etc
2024-08-15 23:30:56
184
samdiabel :
nioune d fi richard toll niafnagn sen kjogn baniou daw ay Ghanéenne laniou Ay domram deug