dieureudieuf Serigne Momar Diagne wakh dji raféte na
2024-09-09 20:18:56
1
Djamil_Mouhaya Sakho جميل :
Baye Mame Mor kassé lay topp ❤️🙏
2024-09-09 19:34:43
1
Ndiagari :
S Momar Diagne dafa yakam té publier rek wayé waron na khaar Ba lire wakhi Cheikh Bara Ndiaye Ba laa mouy def video bi. Video C Bara Ndiaye mi ngi laté si reseau sociaux yi. Kon dou def hors sujet.