doro amoul foula Clara doff l raky manqué bilahi Doro dinalene dofflo guerre femme contre femm bi pour lanala
2024-09-22 22:43:50
205
astou_mossi :
Clara mo amoul foula pourquoi elle peut pas faire comme miss ndiaye
2024-09-23 06:50:04
55
raymondsenghor842 :
goor du projet 😅😅😅
2024-09-23 07:04:16
1
✨🤍 :
😂😂😂😂😂c doro la serie toudou aka nekh
2024-09-22 22:42:57
4
EL Sa :
même clara à voter pour racky 😎
2024-09-23 22:37:42
1
Ivettisha :
Clara diom rek la ame
2024-09-25 19:34:32
0
Mrs Mar❤️💍bu S💋 :
Leup doro Gaye la il est irresponsable
2024-09-25 11:34:54
0
Fina@thiam Gp ✈️ Italie 🇮🇹 :
Dina am morts dh bakhna😁
2024-09-23 18:10:00
0
SONKO 2050♥️💪 :
racky seul nion yo matol sonu yon nekosi🤣
2024-09-23 17:24:33
0
Cheikh bi :
Pape sidi fall kou bakhe la ❤️😏
2024-09-23 15:21:08
0
Dioptima :
En tt cas Clara mom amoul conseil bou bakh
2024-09-23 13:19:51
0
siramamadou61 :
koumay explique cas bi please
2024-09-23 12:47:39
0
Maa-gee-tah :
Nioune gniy commentaire si bopam nio mankei Li warou gnouko nangou
2024-09-23 11:21:32
0
jeune gnarel ❤️💍🌹 :
racky nak beug nako ms waroul won seye ak pa bi même si amna khaliss
2024-09-23 11:15:43
0
l'étudiant fou 🤪 :
Clara supprimé neu photom yi 😂😂
2024-09-23 08:04:11
0
Amina Saliou gueye :
Dieukeur sope na kou amm foula 🤔
2024-09-23 07:58:38
0
Tinish :
Kèp kousi wakhe bok nga sii niom 🤣
2024-09-23 07:22:40
0
le plus impoli a darou marnane :
bly diomi na sèen dieukeur mo manquer wy li souko beugoul wone dou am
2024-09-23 02:44:38
0
𝐁𝐨𝐲 💫🫀 :
😂😂😂
2024-11-04 22:59:47
0
Amy Karimiste❤️ :
😂😂
2024-10-24 11:30:12
0
astouciss16 :
❤️❤️❤️
2024-09-25 18:10:23
0
DS❤️ :
Dém si mére bi sol yeufou grand père 👨 dém si xalé bi deff affaire gentlemen 😭😭❤️❤️
2024-09-22 23:04:17
235
tereso :
Ben jour gnari mariage 😂😂😂😂
2024-09-22 22:27:50
145
myabou2vivi :
Doro gueye mo nekhoul khilifa
2024-09-22 22:38:24
109
Soumadjire1 :
keur aziz alé ndiaye sen keur nékhoul keur Doro mo nékh
2024-09-22 22:47:43
79
chouta :
mane déma yakar racky da yeug ni Clara da wara défat mariage mouné xaral mah publié sama photos mariage yi pour roubé ko
Li kat com film chemin du destin
2024-09-22 22:47:22
45
fatima yayou bb pape :
pk racky bayi mba tay dogua dougal sen photo yi sonal naniou srx
2024-09-22 22:29:08
40
SKIN coach _*YASMINE :
🤣🤣🤣🤣🤣 le pouvoir de. l'argent 💪
2024-09-22 22:28:58
25
Bo réwé ma geune la doporall💀 :
Ba khamguéne racky moy sogua publié lii ça date racky moy bondiiiit deug deug😭😭❤️😂
2024-09-22 22:49:10
20
<🦋M.k❤️> :
Racky Moy songa publié ay photos mariagam mais Clara mom da divorce wone Tay laniou ko takate
2024-09-22 22:37:57
20
rabyraby :
s'en dieukeur mo manqué di l'en manqué lo
2024-09-22 22:47:02
18
Princesse nar❤️ :
Ani team racky
2024-09-23 02:09:52
16
madyticoeur.2 :
C’est Racky qui vient de poster ses tofff vue que Clara ak Dora ☝️☝️☝️☝️☝️li dîna ma nékh anni wa top cas
2024-09-22 22:46:33
15
assanatoubah781 :
sene dieukeur molen mankelo esk li dou temp si cete moi j factorise ma coepouse par 0
2024-09-22 22:32:31
15
🤓 :
Mais bara question bu ame solo gua lathie yii esque tout va bien mu bo wahè yunane daga sohor. Yuun djiguèn yi lutah on se rabaisse toujours comsa 😔
2024-09-22 22:29:32
13
User335679000764 :
Doro gueye amoul foula un homme comme lui milliardaire connue waroul nangou yii kilifa la il devait parler à ses femmes niou arrêter jeux yii mariage dou thiakhane😏 en plus mom mak la
2024-09-22 23:26:07
8
Louchita01 :
Non Clara mo wara régler reundeull té happy gnou wakh ak mom héeee🤧
2024-09-22 22:44:49
8
sokhnagueyeba :
😂😂😂😂série keur doro
2024-09-22 22:41:22
6
Yayou Al Amine23 :
Cas biii dafa disse sama bopp ba mounouma nelaw🤣😂
2024-09-22 22:40:11
6
La 🦁❤️🖤 :
Pour yen dora mi yeufou kilifa lay def yen gni nane dieukar kilifa responsable dora mi mo manqué
2024-09-22 22:37:23
6
D🧸 :
Yalla bakhna 😊
2024-09-22 22:27:38
6
Ciao :
Li Esk d’où film wala série 🤔🤔
2024-09-22 22:31:15
5
Une Noirceur 🖤🔥🍯 :
A quoi il joue le mec 🧐
2024-09-22 22:30:16
3
AICHA TARIKH :
Dora un vrai manipulateur 💔
2024-09-22 23:06:57
2
choubb :
Barra clara da tassate oubien?😳
2024-09-22 23:06:48
2
user6729501663582 :
Li nekhna way 😂😂
2024-09-22 22:30:41
2
Dadiska 💯pour 💯 film 🫡 :
Viviane rèk lay topou
2024-09-22 22:27:59
2
Penda :
Série Keur Doro 🤪🤪🤪🤪🤪
2024-09-23 11:04:43
1
Beugue cheikhoul khadim :
Sène dieukeur mo manquè kou dacor lake j aime
2024-09-23 03:16:37
1
Ramata wally :
Ana wa team Racky kay léne fi
2024-09-23 02:11:50
1
ziza dieng fan's arsenal :
kou d'accord ni Racky mo gagné bureau de vote yeup beuseul j'aime
2024-09-23 00:47:24
1
princesse :
doro matoul kilifa amoul foula Clara manquer na racky manquer na
2024-09-23 00:08:03
1
mina ly fall🥰♥️ :
doro moye seytanè bi😂
2024-09-22 23:37:57
1
user5865793127675 :
😂😂😂
2024-09-22 23:30:59
1
SALIOU AlQurane USA🇸🇳🇺🇸 :
Soy wakh loy mayè khaliss nga wouma Money is bea
2024-09-22 23:19:23
1
❤️kya oumar💍pour la vie🌺 :
Nioun ñi nio manqué ñun toop famille bo xam ni danio yoor chaque semaine niou xeew seen dieukeur Nio leen niou toop si di wakh di doul niom niouy geumeun def di niou nakharal😫😫😫
2024-09-22 22:59:28
1
Une Diouf :
Gnoune topou catou cas yi gno manquer 😂 ndax manquer wèsou woul gnouy lidiantè lo kham nè sou gnou yone nekousi 😂😂😂😂😂
2024-09-22 22:47:27
1
Jamal_Nayra✨🌸 :
Doro dafa fassé won Clara takat ko 😂😂lolou la nk
2024-09-22 22:42:08
1
thiate25 :
Doro gaye l’homme de l’année 😂
2024-09-22 22:42:01
1
Matou saliou :
Barra defalma casting mari
2024-09-22 22:37:05
1
Cheikh ibrahima Sall :
😂😂😂
2024-09-22 22:28:23
1
Balde Fouladou 🥰❤️ :
🥰🥰🥰
2024-11-21 19:33:01
0
m.ngum10 :
🥰🥰🥰
2024-11-11 11:02:22
0
To see more videos from user @barrazerostress.2, please go to the Tikwm
homepage.