@baye_mor.moukaramou244: Kadoup Serigne Aïdara Mbacké. Al hamdoulillah Djërëdieuf Serigne Touba... Djërëdieuf Cheikh Aïdara Mbacké. #foryou #pourtoi #senegalaise_tik_tok #tiktoksenegal🇸🇳 #galsentiktok221🇸🇳 #viralvideos #viraltiktok #fypviral
Tomb_déel.moukaramou244🏅
Region: SN
Tuesday 15 October 2024 21:41:23 GMT
Music
Download
Comments
Emmanuel Magou Pouye :
yalnangfi yague lool té weur
2024-10-20 11:17:18
0
Morenzøø :
Yallha nañu Borom bi défal tawfex 🥰
2024-10-19 02:00:48
0
user6703533861978 :
may the almighty Allah increas your blessings
2024-10-25 18:05:45
0
serigne cheikh :
akasa serigne bii amna solo yalla na yalla déff diame
2024-10-16 10:10:35
4
line bou yama 🇸🇳🇲🇷🇲🇦♥️ :
ay way yalla naniou yalla diégual ta may niou moudiougou rafét 🙏😭
2024-10-17 13:15:49
3
lumière divine :
kou khamoul Yalla bo déwé déme safara
2024-10-16 12:54:41
29
bakh yaye 😇🥰❤ :
yalna yalla defal Tawfékh si diouli yalna yalla yërëm
2024-10-16 09:55:46
98
👌FALANG👊BOU💌S❤SALIOU👌 :
DIEURÉJÉFÉH SÉRIGNE TOUBA 👌
2024-10-15 21:46:06
60
BEUGUE BAMBA :
BEUGUE na guisse serigne aidara YALLA nako fi YALLA yaguale
2024-10-16 10:28:31
18
CISSÉ RAFAHI TOUBA :
yalla nañou yalla diégeul 🤲
2024-10-16 06:59:53
7
KADOUP DEUGG :
Thiey yillé deug yagg fi té wérr 🥰🥰
2024-10-15 23:20:09
20
Mariam Soda Ndoye :
mbacké balla Aïcha merci beaucoup bilaye masi kham dara 🥰🥰🙏🙏
2024-10-15 21:56:20
15
user2006567606724 :
yague fi lool té wéreu Mbacké balla 🤲🤲🤲🥰🥰
2024-10-15 21:55:36
14
Baye Serigne ndir :
dieureu dieuf cheikh cheikh moussa cissé ndiame barom darou lépou yawla
2024-10-16 00:15:25
11
<>🇸🇳 :
walahi deug leuh souma diouli woul douma néck 100% diouli amna solo 🥰🥰
2024-10-16 14:24:54
6
pape :
Vérité absolue ❤️🥰
2024-10-15 23:24:56
6
Alif D :
Walay li laniou sokhla wayé diniou ray ak ay khourafat rek mbacké dieureudieuf 🫶
2024-10-16 09:00:50
5
user58795156586256 :
wakhal ak baye fall yii
2024-10-18 21:25:58
2
Ya Haïcha :
ndeysan ya rer. bo khamoul démal diangui mo gurune baye gall dou jeumeu ay juko la
2024-10-20 04:07:22
1
taphaochj.r :
Video bii sokhla nako nane lay dêff ba guisss kilifa guiii🤍
2024-11-15 14:48:19
1
Domou diarra parfum💨 :
Beneu enemi rek la ame mouy iboulise damay topou basi djouli🥺
2024-10-20 04:06:12
4
Baye Faye bou mame dame❤️ :
mokal alhourhann rekk la beugu koumay dimbali
2024-10-26 13:18:08
0
Mairi🇸🇳🇫🇷 :
malheureusement on est peut pas télécharger
2024-10-20 19:09:19
2
damziokeb’s :
aka diéffé tewlou
2024-10-18 20:32:37
1
omarcisse372 :
Machallah waye Amnasolo ❤️❤️❤️❤️
2024-11-27 11:24:38
1
To see more videos from user @baye_mor.moukaramou244, please go to the Tikwm
homepage.