@toutouastou: Toujours satisfait

Toutou Astou
Toutou Astou
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 02 November 2024 16:07:15 GMT
189300
7855
106
106

Music

Download

Comments

evatra109
Eva Tra :
Gni danio meun di wax rek mais Bilahi gni nguay satisfaire yeip waxou niou
2024-11-02 17:44:36
15
diaynaba.sylla8
Diaynaba Sylla :
nagnou insistè si savon toutou astou bi mane dafma yèm savon bi mome miracle billahi mome rèk daflay diokh teint bou doy warr yaw ya meune wayy yafi nè nak
2024-11-02 16:52:37
11
diamantnoire323
khoudia mu s darou hassan 🔵⚪ :
représentant bou Touba s'il t'appelle
2024-11-02 16:41:53
4
fa6lebousonko
Fatou🥰6c :
Khalif général kouly diaykatou diww
2024-11-02 16:31:31
4
fatoutine040
Fatou Tine :
Promotion kagne lay am
2024-11-02 17:06:05
3
farmaritoh
Fatma bou toutou Astou 😘😘 :
Khalifa général koulou diay kat 💃🏻💃🏻💃🏻💃🏻
2024-11-02 19:02:36
2
bijou242
Bijou Ndiaye :
toutou représentante dagana laniou beug
2024-11-02 17:27:25
2
ciss06africa
Cissé🇸🇳🇫🇷 :
tient bi rafet na mom 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-11-02 16:48:21
2
bayniassreptoutouastou
WAKEUR MAWLANA BAYE NIASS :
machala li lerna
2024-11-02 16:38:43
2
kangue972
kangué :
slt toutou Astou je suis depuis kaolack, je veux une gamme de 15000f pour teint marron fane lay diarr dibaléma pour ma diomal mr thie décembre bi inchallah
2024-11-10 01:17:59
1
fatousha9946
fatousha ❤️💕🦋 :
Tata sokhna khamnako Machallah @Toutou Astou nekete y’a meune nak 🥰yaramam bi noum melone yako defar ni yallen meun nak❤️diote sama bourse moma tere nieuw fofu
2024-11-03 19:54:15
1
madamembacke73
Mame Faty Mbacké :
tag rew kay mosi gaw
2024-11-03 18:04:23
1
yayou_aissatou
Djimareme niang(saliou) ❤️🥰 :
Mane 6mois magui ak yenn tai mousouma dem boutique toutou si Saly keur massar rekk momay diayy mai aka athiou douma bayii dai
2024-11-03 13:36:10
1
ramatoulay625
Ramatoulaye 🥰 :
Profitez de la promotion mes amours 🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷🩷
2024-11-03 10:23:44
1
soxna.ma74
Soxna maï :
sama rakk sakh mokoy diay diw mais ay diwam dafa meilleur meussouma am chance dieundeu ci diww yii mais bou déffé promo Dina dieundeu inchallah Toutou lingay diay bakhna trop
2024-11-02 23:07:55
1
soxna.ma74
Soxna maï :
mako fékk plassam chez le Niani mou xéssalone ba wékh talleu mou bayi nioul koukk dama nieuwatt fékk mou am teint bou Glow mouné Toutou mokoy diay diw🥰🥰 TouTou mo meilleur
2024-11-02 23:04:15
1
fatoush9047
fatoush 💖💖🧕 :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-11-02 17:46:58
1
yama26395
Yama :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-11-02 17:41:36
1
bb.diarra101
bb diarra💕❤️ :
🥰🥰🥰
2024-11-02 17:22:47
1
user744374670
user644759124323 :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-11-02 17:12:59
1
lamoustarchidaty01
diarra bou mame khalifa🫂🫀 🥰 :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-11-02 17:10:21
1
fatima_zahra_hiyman
Fatima Zahra 🧕 :
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-11-02 17:10:17
1
ngaya.ndiaye19
NGAYA🦋NDIAYE♥️ :
Bou auto bi désse place yobaléma 😅
2024-11-02 16:42:42
1
fifisalihate
FifiSalihate :
Toutou dafa meilleure nak🥰🥰🥰
2024-11-02 16:35:34
1
madameba147
madameba147 :
Toutou stp sa numéro la beg sama tank yi da yakou stp
2025-01-13 13:59:55
0
To see more videos from user @toutouastou, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About