@wolfman_casa_prod: Partie 23: Wolfman le Nullard 🤣 3-1 🤣 Kou d'accord ak mane 🤣 Wolfman rew na nak 🤣 #comedie #rire #delire #humour #senegal #wolfman #wolfmanetsesdelires #wolfmancasaprod #senegal_tiktok221 @Wolfman et ses Délires 🤣 @Wolfman et ses Délires 🤣 @Wolfman et ses Délires 🤣
et pourtant il as raison 3 balle mokko dessé ba tayy kou d'accord at man philosophiquement
2024-11-23 14:25:02
238
oumy :
mangui ré melni kou febaroul ba nék hôpital en tout cas merci bcp😅
2024-11-23 11:05:37
140
madiara mbengeu :
3-3=0
2024-12-18 10:50:02
1
Sen info rapid Ainou :
dara gueunoul nekh diouli wakhtou yeupou 🙏 🙏..
2024-11-25 22:07:59
74
capitaine 👨✈️ :
Pourtant wakh n’a deug deh 😂😂
2024-11-22 21:31:05
152
cheikhtine381 :
Danga am problem ak 3
2024-12-20 21:36:55
1
unegueye52 :
Prof bi dh damay ragual mou amé wakhou lihh 😂😂😂
2024-12-21 13:32:36
3
Mouhamadou Sow :
Bo amé nietta diabar nga facé béna niatta moy désse😂🤣😅😆
2024-11-22 23:39:12
31
baye.mbacke5 :
dama rétane 😂 ba sama iphone 16 pro max ,256 giga bima dieundé 2 millions 500 à Dubaï de couleur bleu nara wade😂😂😂
2024-11-25 15:45:38
5
Mya950 :
Dina doff doff lou ba am examen😂😂😂 wayé sa bop bi douko fèkè dèh 😂 wayè louma diakhal moye dianguame bi yeup 3- la wala 300f wala 3ballons lèpeume 3 la😂
2024-12-01 22:26:44
1
CHEIKH COUMBA NDOFFENE DIOUF ⚽ :
mome kou beugue 3 la kham na😂
2024-11-22 21:30:38
9
siakhadija :
Il a reson c’est le prof qui a mal posé sa question 😂
2024-11-22 21:32:27
75
Mouhamed Diallo :
Wolfman deffoul dra professor bi mo nul😂😂😂
2024-11-25 12:13:43
11
Fyn@gaye570 :
Mom dé bala paré dina déh 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
2024-11-24 23:35:39
12
Priince Mbaye 24k🇮🇹 :
yalna diam yageu 😂😁
2024-11-22 20:46:17
49
Aly Ciré Ba :
Bilahi wolfman dinama ray😂😂😂
2024-12-07 11:46:24
1
Moïse 🫶 :
Wolfman élève boukoye sétane dinga moidié nék nillard je vous le jure 😂😎
2024-12-18 21:37:13
3
I S S A🇸🇳 :
dama rétane 😂 ba sama iphone 16 pro max ,256 giga bima dieundé 2 millions 500 à Dubaï de couleur bleu nara wade😂😂😂
2024-11-25 11:42:09
14
WOLFMAN CASA PROD :
wa mayoumako ballon bi nak monsieur 😂 Damaka ale rek 😂😂😂
2024-11-22 20:21:01
17
papa_ousmane :
3-3 Kagne lay trouvé tamite 🤷♂️😭😂😂
2024-12-21 22:37:13
1
Adama ba :
😂 Ousmane wakhnala dege 300 moko dé sé
2024-11-22 21:42:29
7
Petit Pape matar sarr :
wolfan yaw do dém def théâtre
2024-12-18 15:10:59
3
To see more videos from user @wolfman_casa_prod, please go to the Tikwm
homepage.