@maibralaye: Moytu xaste ak di juger sunuy moroom - Ma Ibra Laye #conseil #education #speech #layene #layenne

Ma Ibra Laye
Ma Ibra Laye
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 28 November 2024 07:23:15 GMT
24325
4786
150
122

Music

Download

Comments

nngagne
Lebou or 🥇bi🇸🇳🇪🇦🇧🇷🇺🇲 :
Walahiii contan nagn ioe Ibra
2024-11-28 14:04:25
2
ndefadio
fafa :
bilahi koulay deglou dou rerr mouk nioun ndaw gni lilaniou Sokhla kouy nioun tekk si yonou yalla yalla nala yalla faye
2024-11-29 00:30:41
2
salihate140
Sokhna Awa saliou🥰❤️ :
Masha Allah 🙏deug kepp rkk ngay wax laye Makhtar yalla nala Borom bi sam
2024-11-28 20:32:37
1
ndeyekhadidia32
Les délices de mme dia :
Machalah sama sopè bi kadu yi rafetna yalla nala yalla geureum
2024-11-28 14:15:43
2
ouli22laye
Ouly-Laye :
♥️♥️♥️sangu bi yalla nala yalla takhawou fep 🙏sama sopé bi beugu bimala beugu day yokou
2024-11-28 15:35:49
2
birammbye2
@mbye :
Walahi damala buga ngirr yalla tah yalnala giss bala ma fatu insallah 😭😭😭
2025-02-22 16:26:42
0
ngalla7750
ngalla :
walahi ndéyesane yalla nanga ame ngueremeul sounou borome 🥰
2024-11-30 15:28:51
1
astou.senghor3
Zidane :
diaref lay amal diam bou bari
2024-11-28 11:38:22
1
evachou727
Madame Gueye :
😭bly laye mahtarr
2024-11-29 00:40:06
0
moulayedabakhjr
Aziz Niang Bou Ndiol Fouta 🥰 :
Ma ibra Sama Serigne sama professeur 🥰
2024-11-29 11:44:36
0
antasaliou203
anita saliou :
diga goudou fan inchahalah machahalah say wakhtan dafmay delosi lol sakh walahi
2024-11-30 19:14:00
0
salihamouyayam
𝐁𝐀𝐘𝐄 𝐙𝐀𝐋𝐋 44# :
Wallahi yallah dééf mane ma beugue leu Yalna yalla goudeul fane wi
2024-11-28 07:39:43
23
mo379402
761606708 :
ma ibra laye yalla nala yalla geureum barkép cheikh limamou
2024-11-28 07:31:34
6
mbayalayedieng
mbayalayedieng :
machalla mn professeur yalla n'a yalla yokk kham kham bi
2024-11-28 13:13:26
4
balaibra12
وان :
machallah
2024-11-28 10:25:55
2
saydinaissa
seydina. laye :
wa Laye💖💖
2024-11-28 10:37:49
1
awasaliousf1
XELCOM BUSINESS👑 :
Dieureudieuf amatina sollo amine ya rabi
2024-11-28 10:10:17
1
laye.mamadou.makh
laye mamadou makhtar alassane :
dieureudieuf laye mamadou makhtar ♥️👌amatina solo walahi
2024-11-28 13:07:24
4
mohamadoulaye
Mamadou Lahi :
maashallah ci nasiixa bii yalna Swt défal nu dégg ak Topp
2024-11-28 19:20:32
3
aisstasao
Aissata sao :
mashallah mashallah wonibike merci beaucoup que Dieu te protège Amine yaraby
2024-11-28 10:43:49
3
djibril2210
Djibril :
wallahi deug rkk Moy deug ne juge pas et vous serez pas jugé ne condamnez pas et vous serez pas condamné 😓🙏
2024-12-17 19:51:36
2
mame_modou
mbengue mbor :
❤️❤️sama sopé bi yalna borom bi same la
2024-11-28 15:07:16
2
youssougueye247
youssougueye125 :
yalla naniou yalla may moudj bou rafét def niou dégue dégue dioullite
2024-11-28 14:59:59
2
zambala.champing.lebou
𝐙𝐚𝐦𝐛𝐚𝐥𝐚𝐌𝐛𝐞𝐮𝐫10🏟️ :
Machallah professeur ♥️
2024-11-28 14:30:52
2
user191703295723
bb dija :
Machalah ❤️dieurédieuf frére bi yala wéral batt bi.amna sollo lol 👍🙏
2024-11-28 13:50:27
2
To see more videos from user @maibralaye, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About