assurance bou wor bilahi khamenani si dra gorgui rek
2024-12-09 09:38:07
205
laye 406 🫶🚐🛣️🙏 :
galou Serigne Babacar sy niou dém Spagne ❤️❤️❤️
2025-01-08 15:55:43
0
aminagayebeugueserignebabacar :
❤❤❤
2025-01-21 03:41:45
0
Mouhamadou Mourtada tidjany :
Gaal goumou nékeu sagne nassi dem Espagne walahi sans khalaate
2024-12-09 20:19:00
359
elhadjdiop439 :
delen ko bayi khel photos bi inchallah rafet na lol
2024-12-08 21:51:27
50
Sait Mbye❤️⚡️✅ :
Salalahou hala Mouhamed 🥰
2024-12-09 13:00:45
44
Talibé cheikh :
Bilaye dou question far déh wayé mane dama sétlou gale yi nékk sunu kogne yeupe gnisi eupe serigne Babacar sy lagnousi déssiné bilaye khalé yé beugue mbaye ❤️
2024-12-09 23:36:09
18
𝕸𝖔𝖚𝖍𝖆𝖒𝖊𝖉_𝕵ò𝖔𝖕ﷺ🇸🇳 :
Guddeul fann waayy😭
2024-12-09 03:08:34
18
mamyta :
j'aime serigne babacar sy 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2024-12-10 10:01:45
17
Perlenoire013 :
Mane deh auto bouma dougu ba fek fa photom douma ragal ak loum goudi goudi 🥰
2024-12-10 15:43:44
13
tamakup :
Dou tasse yakar dou féthi coloré fouma ko guise gniémé nafa yalla nagniou ko yalla fayal
2024-12-10 09:55:02
11
ba :
Yalla bou gal gui kayati si barké serigne babacar s’y🥰🥰🥰
2024-12-09 15:59:57
9
Ablaye sarr sop Al Amine :
gal gui dafay dém spange wala ak fan lay déparé mou khar ma ❤️❤️
2024-12-09 19:16:21
9
Daba Gaye :
fathie aguo gawnasi mbaye
2024-12-08 20:54:54
8
Rama bou serigne babacar sy ❤️ :
biss bole di départ rek wakh mako gnieme nathie yeék
2024-12-09 17:47:24
8
Ozil s’y :
Gale gui heur bou démé guedj yalla na diapou dieune gnibisi wate si diamou si barké s babacar sy🥰🙏
2024-12-10 15:52:24
7
Bae Fatoush ❤️💍 :
Diam si yéne ❤️🙏🏾
2024-12-08 22:15:46
7
Dani olmo 💙❤️20 :
salalahou Alla mouhamed 🤍🤍
2024-12-11 16:15:50
7
Sokhna may Sall :
sallalahou allah mouhamed
2024-12-10 01:37:41
7
Blackman :
Moytou len réseaux yi thiat bahoul Aa wa bahnA🤣🤣🤣🤣
2024-12-09 06:47:27
6
Thiate89 :
machalla ❤️💯
2024-12-09 09:35:05
6
Tymasamb Samb :
machalla yalna yalla yokou léram tass gnou si barkém 🙏❤️❤️❤️💕❤️💕💕💕❤️❤️💕❤️💕❤️💕💕❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤