@telev114: #mamendiayesavon😂😂😂🤣🤣🤣🤣 #mamendiayesavon #tiktoksenegal🇸🇳 #tiktokitalia #tiktokespaña #adamobossnegri #tiktokfrance🇨🇵 #tiktokfrance #tiktoksenegal @Mame mou ndaw Ndiaye @MamendiayesavouSF @Mamy cobra 2

Fiii la cas bii densé😂😂😂
Fiii la cas bii densé😂😂😂
Open In TikTok:
Region: FR
Thursday 19 December 2024 16:29:13 GMT
84914
2692
162
230

Music

Download

Comments

arame.diagne076
Arame Diagne :
Sonko dalllllll moye senegal Machalla 🥰🥰🥰🎄
2024-12-21 13:39:10
0
mariamakebe32
Mariama Kebe :
Sonkho ame naaa ndam😭😭😭
2024-12-20 08:22:09
2
bour.la.linguere
Bour la Linguere :
Thieuy Cheikh Yerim,liguay deff dou class ci gor deh😭😭😭
2024-12-20 01:40:42
0
habibhabibkane
habibhabibkane :
Balthazar senegal
2024-12-20 21:58:09
0
khaitoush
khadousha🇪🇸🇸🇳 :
Elle est entrain de sauver les autres femmes bayi lenn ko mou wax
2024-12-20 06:10:26
143
marietouseck5
Mariya :
Dafko takk just pour sekh ak mom c’est grave ça. Lolou meun nga si porter plainte
2024-12-19 21:58:46
83
user9478207210717
user9478207210717 :
Première cadeau bouñou wave fofou rek respect amou fa
2024-12-19 23:28:58
130
mishou59
Miss Jaja 👸💕❤️ :
Ngoné da nga dioum nak 20 millions nga warone lath vraiment amougnou neubo 🤣🤣🤣
2024-12-19 22:25:38
70
www.tiktok.combrodes
Dubaï brodés shop :
Balthazar du Sénégal yerim diotna gnu 72 h la
2024-12-19 21:00:55
78
tereso412
tereso :
wayei mo ngui soga dadj nak yalla natou ko nga démasqué ko😂😂😂😂😂😂
2024-12-19 23:22:31
30
seynabou.sarr739
Seynabou sarr :
Aye homme 😳
2024-12-19 22:00:06
14
soleildusud15
Soleildusud@ :
C pas la même qui avait dit qu’elle n’allait jamais divorcer ?
2024-12-20 00:16:50
8
khady.diagne575
Khady Diagne :
wa ki mom thiey Sénégal esque diotoul yalla wathi fii bene 1heure de temps ba nieup guissko mou delouwat
2024-12-19 23:00:29
5
user7607357369161
Mohamed :
20 millions nga waro nah ladj
2024-12-20 10:15:20
8
babademe410
Baba déme mou sonko :
thiow li yalla na dém ba 2080 inch'Allah
2024-12-20 10:28:20
23
fatimacissokho412
fatimacissokho412 :
ndeysane dalo si masta.yalla dinala maye li geune si yaw
2024-12-19 22:19:55
15
cheikh0799
cheikh90 :
Ki vré doméram la
2024-12-19 21:50:55
13
user3433920091756
user3433920091756 :
yaw wayoo
2024-12-19 20:04:48
11
fatoundeye4
Fatoucha❤️❤️❤️🇸🇳🇫🇷🇺🇸 :
vraiment yérim y’a bonne
2024-12-20 10:33:53
7
chacha73669
chacha :
ou total tonton seck niata diabar la âme?
2024-12-19 23:55:15
6
madame.diallo994
madame diallo❤️❤️❤️ :
ayway yawmii fatté gua trop
2024-12-19 23:41:10
4
maimounathiam461
Maimouna Thiam461 :
ngo aime yerim ndeysan déception bakhoul
2024-12-20 22:19:54
1
aichadiop997
Sokhnaicha Faye🥰😍♥️💕 :
Yerim dof la Yaw wero aussi amna yo khamni Soooo guisse si ngoro quitte ma chérie 🤣
2024-12-19 23:48:39
3
skai118
Skaï221 :
Ki wéroul ndeysane nako ay mbokam diapalé té yalla takh😂😂😂
2024-12-21 02:43:33
2
juniorsiby01
Authentique :
YERIME DAL GUERRIER LEU YÉNE FEMME YI YÉNA BEUG SIIW REK MOTAH YERIM DILÉNE USE REK
2024-12-21 02:32:35
2
To see more videos from user @telev114, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About