@aissa_tout: Ces comportements te permettent de gagner le respect des autres tout en renforçant ta confiance en toi. Retrouvez toutes mes recommandations de livres che @Librairie pages d’aissa 📚 en appelant le +221 706702885
Quel comportement as-tu adopté pour gagner le respect des autres tout en restant fidèle à toi-même ?
2024-12-21 19:33:43
98
aïda saliou :
Y’a takh ma guena bgue sama bopou
2024-12-21 19:53:06
56
Baay gall@ss732 :
Sama yaye niewatina🌹🌹🌹🌹🌹 meilleur compte sur Tiktok 💙💙💙💙💙
2024-12-21 19:38:42
53
DEUG rek :
façon d'ici 2025 souma amoul ligey entreprise bouma diekou doug tok ligey point
2024-12-21 23:42:44
15
Bedezo le Mancunié :
Vraiment y’a eupo solo si tiktok bi respect
2024-12-21 23:22:09
76
Sermonia :
pour confirmer je n'ai que 27 ans et je peux dire que djikko yinga wakh mingui ci man. mais fima nékk même gnima magué plus 20 ans dagnoumay roussa yonni. mieu sougn tooguee souma nieuwé dagniy diouk
2024-12-22 00:36:33
16
Makh_Business :
Où est ce qu’on peut trouver ce livre ?
2024-12-21 23:33:28
7
ndawoussemane :
Noumay Def Bamou Baayi Fenn ? Damako Beugue Trop Té soubaayi woul Fenn mann mom Damakay Baayi Sama Kharitla Sama Mboock La moma magué 2ans mom Goor la mann Goor Laa
2024-12-21 20:09:32
7
👨🏿🎓👩🏾🎓JÀNG_WOLOF📚 :
Téerey Wolof yi dee ko jënd di ko fésal. Mel na ni amal na solo lool nit ñi. 🥰🥰🥰
2024-12-21 20:07:52
5
user7244356894506 :
j'aime bien tes conseils merci beaucoup
2024-12-21 19:46:49
9
user7947469094156 :
mental bou fort ak humilité mo waur
2024-12-22 01:19:52
15
To see more videos from user @aissa_tout, please go to the Tikwm
homepage.