Bilahi sama yaye nonoula dey agne ba sour 17h moneu agnal reer aussi bou reer moune reroul nena degn ko sise
2024-12-25 15:45:27
4
sopey serigne fallou bi :
sama niari waydiour ya yalna léne sa borom bi yeureum ak bép way dawlou🥺😢
2024-12-24 17:02:22
134
bou N____D❤️🔐 :
Aka nékhon sama yaye Ague Ak man fofou yalnako yalla yeureum 🙏😭😭
2024-12-24 18:20:21
33
djena :
walahi ndessan
2026-07-24 15:44:19
0
muhamadu Lamin joop 🥰🥰 :
😅 ñi Nga xamni séen waajur lijanti wu léen Nag ba noppi dakh léen Keur gi
2024-12-24 21:27:27
3
ZEM :
salala alla mouhamed 🥰😍🥰😍🥰😍🥰😍🥰😍 alhamdoulilah
2025-02-13 22:04:06
1
le grand patriote du Sénégal :
eskay Macha Allah ❤️sama Serigne leçon de vie amna Solo 🙏🙏🙏🙏
2025-07-10 10:52:30
1
SOPE SEYDINA MOHAMED SWD :
Yaye boye maan namounala beug Nala yalla na nga fi yag té werr Papa Yaye
2025-02-14 11:04:25
2
user2185043402839 :
اللهم إعفر لأمين وأبي ببركة سيدنا محمد صلى الله عليه وسلم
2025-03-20 03:30:20
2
fallourafahi788957371 :
Ndaysane yalnanù Yalla may xollou mougne
2025-03-21 04:24:06
0
Seriñ moussa fall 🖤🤍 :
Ay waye Kou maye santalé yallah 🙏
2025-01-08 23:35:50
8
BawBaw77 :
sallalahou al mouhamed machalah
2024-12-28 17:29:36
2
FatyMah52300 :
mes parents ma vie, maman repose en paix fou sama xél démé thi mom ma nianaleko yeurmandék djiégualou souniou borom, sama papa yalna doundou ba romb 100ans
2024-12-26 11:07:52
1
maye bintoul khadim🇸🇳🇸🇳 :
amna solo bilahi té wérou si yalla💯
2025-09-15 13:47:19
0
modoumbengue858 :
Yalla na ngafi yagua ta werr
2025-01-19 23:00:17
1
cheikhouna Ndiaye :
Masslah
2024-12-25 17:31:03
1
Réglo Bab's ♥️ jé du temps :
eskey ♥️♥️♥️
2025-02-05 13:28:12
0
issa gueye :
bilaye ndeysan yalla nalén yalla défal tawfékh
2024-12-25 13:47:45
2
gorelka85 :
rabi irham houma kama raba bayina sakira🥰🥰🥰
2025-10-05 12:52:24
0
gora :
❤
2025-05-22 14:38:23
1
gora :
😭
2025-05-22 14:38:24
1
gora :
❤
2025-05-22 14:38:31
1
gora :
❤
2025-05-22 14:38:26
1
gora :
😭😭😭😭😭😩😩😩😩😩😩😩😩😩
2025-05-22 14:38:12
1
gora :
😭
2025-05-22 14:38:27
1
To see more videos from user @moustapha.rafahi090, please go to the Tikwm
homepage.