@ibrahima_halill_2.0: Les gens qui s’acharnent sur COD comme si limou wakh ni mogui koy soga wakh Alors que li mo yague nek sa position Si vous n’êtes pas d’accord avec lui ngen contraduire ko avec des preuves c’est tt té ngen nangoul ko son point de vue avec respect.#chiekhomardiagne
ibrahima_halill_2.0
Region: SN
Wednesday 25 December 2024 13:12:46 GMT
Music
Download
Comments
Papa Momo Ka :
CoD xam xam rek laye wakh
2024-12-26 15:06:32
2
FALL GÉNÉRAL 🇧🇫🇸🇳🇲🇱🇳🇪 :
cheikh Oumar niagne degue rek lay wakh 🥰
2024-12-25 19:41:06
2
ABMT ✍🏿 :
Bëggnaa COD ba nopi ❤️
2024-12-25 20:21:31
1
user9388410549525 :
Mane deh mangui si Guinawam beuh sakar khégn😎
2024-12-26 08:26:16
1
abdoulaye26mail.com :
COD lou leer lay wax
2024-12-26 14:34:38
0
khassimndour :
machallah
2024-12-26 15:35:41
0
Kebba Jimba Jobe :
aka bari xam xam
2024-12-25 22:29:10
0
ismasara21 :
professeur doff douco deglou, yague naco wakh dh wayy rewmi do comprendre
2024-12-25 20:54:27
93
beugsonko10 :
Deuk bo xamni tous est émotionnel 😭😭😭zéro xam xam
2024-12-26 09:23:11
27
oumardiop136 :
je suis cheikh oumar diagne nitou deugue
2024-12-25 21:02:33
29
radawaye :
gni koye diaboliser, moye gnimou wakhone ni, sen bindou Mame yi daniou KO warra perfectionné, nioune khirou 😂.
2024-12-26 08:56:03
13
Mor Talla Dieng :
:Cheikh omar Diagne parle aux esprits illuminés et non pas aux limités 😒😒😒😒
2024-12-26 06:47:32
22
Batouni🇸🇳officiel🇫🇷. :
Je suis avec toi COD
2024-12-25 17:44:01
37
Moda Gningue :
Saway kii dafa diaxassé carte gui😂 tirailleurs yii nioudone magal thiaroye ak gnidone xeex ak bours yii douniou benne dhh
2024-12-25 21:53:58
5
Waulou Sonko lole :
laissés nous télécharger stp
2024-12-25 21:15:27
9
mouhamed Diop :
Je suis Chiekh Omar cents pour-cent @🤗
2024-12-25 23:56:52
24
L ’Autorité 🫡 :
Il est toujours cohérent sur ses dires… chapeau à ce grand monsieur
2024-12-26 00:25:22
21
Mouhamed diop 2 :
Merci chékh omare diagnie
2024-12-25 18:32:32
18
Mbayelebarhamien :
il est toujours constant dans sa démarche
2024-12-26 10:56:09
5
Kécè :
Merci Cheikh Oumar Diagne, xam-xam rek mo waur.
2024-12-26 10:44:13
5
mouhamed all Amine Sagne :
toutes claires machalla vérité absolue الحق مع شيخ عمر جاج
2024-12-26 01:41:14
8
Leendeng :
cod chaque jour mou am deug sougnou kay gayii nagnou bayii dii démé par emosion
2024-12-26 07:35:04
5
kartong :
Pourtant limou wah degg rekk la
2024-12-26 12:21:16
2
Ousmane diomaye Senegal 🇸🇳 :
Ki kou dof douko comprendre il est hyper avisé❤️
2024-12-26 08:52:14
3
le philanthrope :
deugu deugu reekk moor woor Masha Allah touche le
2024-12-26 21:14:44
1
To see more videos from user @ibrahima_halill_2.0, please go to the Tikwm
homepage.
© 2021-2024 TikWM. All rights reserved.