@islam_ak_xamxam: "Gnoungui Ragual Lou Nékh"

ISLAM_AK_XAMXAM🧠
ISLAM_AK_XAMXAM🧠
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 04 January 2025 20:09:12 GMT
230786
32111
901
1504

Music

Download

Comments

papamodouniass
Bmn :
yalla naniou yalla df djiolitt bou deugou
2025-01-04 20:49:03
1020
eliboucana
OnebusinessGroup :
Ndeysanne dama done ande ak sama kharite migui toud Moussa Diop mou guene aduna damako nianal beuh guent ko mounima Elimane magui si diam
2025-01-05 19:24:12
752
toure_mande_mory_26
Touré_mandé_mory :
Nila kay des fois ngèn dalall sunu khell sakh 🥰🙏🏽
2025-01-05 14:45:53
710
mohamed_diagne1
Mohamed_Diagne01 :
Nekhna si diame bi diamou yalla
2025-01-05 07:30:17
561
hadyalmichri5
Hady AL Michriii🇲🇷🇸🇳 :
li geuneu nex si déé moy da 'gay guiss Yonéte bi ♥️♥️♥️
2025-01-06 02:14:28
336
technicien_desurface
khalil service :
yalla na nékh so ndiabotou yonéne bi yeup
2025-01-04 23:51:34
188
islam_ak_xamxam
ISLAM_AK_XAMXAM🧠 :
Gni kham les expériences de mort imminentes meunagn confirmer limouy wakh
2025-01-05 00:32:00
72
901salam
Salam :
Deysane kounaratékhé rék lay wax yalnaniou si yallah bolé amine yarabi
2025-01-05 08:36:22
63
sunsei1010
sunsei1010 :
Des fois je me dis que mo wara dakk doundeu deh franchement
2025-01-04 23:45:17
58
papa_n29
Prince_Lebou👑 :
Professeur tay mom meuno wax bama gnémé deh 😂😂
2025-01-05 11:20:28
49
issagueye1495
Modou Gueye :
wédi kate yi démlén diangui c'est important dioulit bu sélbi butoulé si deé yalla diko wan dieuff diou rafét yimou don déff dou beug rou gui gawa dém
2025-01-05 09:35:58
47
mouhamedlamin112
Mouhamed Lamine :
Sallahou Allah Mouhamed
2025-01-06 16:47:17
39
To see more videos from user @islam_ak_xamxam, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About