machallah li darra fayouko pape ak dom lng vie à vs yalla wérall batte yi 🥰🥰🥰
2025-01-05 15:47:40
11
radia❤️🙈 :
Bilakhi j’ai même des frissons dakh acte bou noble bi🥺🥰🥰🥰🥰
2025-01-05 12:36:19
15
alseynie :
commentaire meuna rafett nehh t'es amoul wahdjou niaw dangua beugeu say kilifeu donc nak respectel kilifeu djambour yi mangui diegelou
2025-01-05 09:51:35
22
Adjaaïdagueye2.0 :
Ndeyessaan lii motakh mandou Bakh ak Gni di djakhassé 🥺 j’ai les larmes au yeux Youssou Gueuneu leu Té Doom diko Xélal guissatoul Ndeye guissatoul Baye Yallah Djam Yagg ❤️🥰
2025-01-05 14:41:47
11
O délice d Alice :
Le roi et le prince 🥰
2025-01-05 10:26:42
9
wrldcheikh :
Le respect de wally seck envers youssou ndour je suis très contente 🥲 pour ça ❤️❤️👍
2025-01-05 22:10:34
31
banač diop the realcityzen :
Yalla nanou yalla fayal Youssou 🥺🥺❤
2025-01-05 09:56:19
21
Ndiaye téranga :
you wakhe na wali bou nangou dogal
2025-01-05 09:51:27
5
Elhadji Diengsalla❤️😘 :
Bilay youssou Ndour dina yar khalé yui 😂😂😂 inspiration bii mo graw il a réduit le gos à sa juste valeur 😂😂
2025-01-05 22:00:11
7
Bébé Astou :
Wawaw machala mat yacine way♥️
2025-01-05 09:03:55
7
Amy Chimère :
Ndeyessane 😭❤❤🥰
2025-12-24 00:24:31
1
user9970395492913 :
Li raféte na trop bilaye papa thione kholame sédna trop si li papa you yalana takhawaye bi lole
2025-01-06 23:25:42
0
kénza la barhamiénne :
ohhh Wally tope na tankou papal🥰
2025-01-07 20:11:25
1
Guigni__lovee💞 :
Sm khôl bii😭❤️😌
2025-01-05 12:57:26
4
Gallass :
2025 s'annoce bien
2025-01-05 14:20:39
4
To see more videos from user @stamipolproduction, please go to the Tikwm
homepage.