@dahwa.bi: #mouride_sadikh_officiell

Dahwa bi
Dahwa bi
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 09 January 2025 18:21:00 GMT
473591
61961
2347
5600

Music

Download

Comments

ibnou74
papis :
allahou akbar ndeysane yalla naniou yalla tass thi barkém
2025-01-10 17:36:45
0
mamindour726
Mami Bou Gora Ndiaye ♥️💍💍🔒 :
Ndaysane mame boye goudal fane bou and ak werr ♥️♥️
2025-01-09 22:46:05
2
ndeya01
Dieynaba :
Yague fi lol mame boy
2025-01-10 13:34:52
6
ndeye.yacine.mbay8
Ndeye Yacine Mbaye :
machalla yalla na nou yalla May at yi kone sounou mame dji té mou andak wér yalla May ko wér 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
2025-01-10 18:41:07
0
user8509314782746
user8509314782746 :
alahu akbar 😭😭😭😭😭they yalla
2025-01-09 19:01:33
27
wiz6597
wiz :
🤔serign Touba amoul morom ken xamoul Loum done🤔
2025-01-10 14:16:45
4
yorodeme
yoro deme :
Mame yalna yalla goudal fane wi barkep lerou alkhour anne
2025-01-10 10:36:57
2
diaganembaye2
user8255529163773 :
ndayessane Mame boy guoudou fanne akk werrr
2025-01-10 17:53:50
0
babaca963
babaca963 :
Hoo Ndayssane sounou maame
2025-01-10 00:00:42
39
bb.dgs.la.famme.n
bb dég's la famme noir🏐🏀 :
ndayesane Mame boye goudal fane bou and ak wérr 🙏
2025-01-10 17:33:31
0
bachir__fall
bachir fall :
amine yalla na doundou lou bari wat
2025-01-10 18:01:21
0
zahrata.lwadi
Zahrata Lwadi :
wallahi wakhyert Borom Touba 🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️
2025-01-10 04:59:44
1
modouinf
sarr :
yague fi lol Mame boy
2025-01-09 23:32:37
5
lepatriote566
Fils a maman :
Amoul morome Borome touba
2025-01-10 17:41:45
0
tazz.ndoye
Tazz Ndoye :
lolou d khana Moy demou aladji Abdou Aziz dabakh ba alakhu akbar yalna yalla tass GNU thiséne barké 😭🙏
2025-01-10 07:17:08
2
ahmadoubambagaye2362
ABG :
Mer dondal way❤️❤️
2025-01-10 04:36:29
1
becayebabou62
papebecaye :
Borom touba amoul morom
2025-01-10 00:58:42
1
ndeyeada22
Ndeye 2 :
yawo mi thi kawo 2 commenter bi rew gna waya bakh na demall
2025-01-09 20:02:15
1
philogaye76
Philo le serviteur :
Serigne Touba néna kou féké diamonom, sokay nétali ak lo maguett maguett dingako nétali nimou amé, sa xel dou nakh pour nétaliko
2025-01-09 23:50:16
1538
boussonarr
boussonarr :
yalla na sounou borome déf miracle thi sokhna si mou dounedou 200 ans ta boumou nak boumou fébar barké borom touba Amine
2025-01-09 23:44:49
839
ibrahimandiaye3978
Rasta liloulla :
kou d'accord né yalla naniou yalla may wéér ak goudoufaneu kom sunu mame Boy bi l'alal j'aime
2025-01-10 01:12:08
528
assane.top
BISS DOU NIAKK :
Mbokkou yi sama Mame le 18 janvier laye âm 100 ans yokkou léen Niane yi Amine🤲🏾
2025-01-10 12:41:38
101
barclay8622
diaz :
sama mame nilamako netale bilahi
2025-01-09 22:35:18
465
julebaydarou
julebaydarou :
Koufi commentaire Lou négatif ma dokhane sa ndy ☝️mame Yague yokk wérr rekk inchallah
2025-01-10 02:59:50
125
guene1.0
GUENE1.0 :
Ma grande mère m’avait dit la même chose sur l’obscurité du ciel après la disparition de Serigne Touba
2025-01-09 23:49:26
432
To see more videos from user @dahwa.bi, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About