@serignebarafall15: Délén begueul séni soxna niom gninga xamni danio bayyi lepp ndax ioe 👆💍❤️ Alhamdulillah yalna yalla barkeel #senegalwedding #amour #viral_video #foryoupage❤️❤️

SERIGNE BARA FALL
SERIGNE BARA FALL
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 14 January 2025 13:43:32 GMT
39449
6563
244
71

Music

Download

Comments

bambaelectroavlg
Bamba Electro🎗️ :
yalna y'Allah barkël barkip borom touba ak xassida yii❤️🙏🏾
2025-01-26 16:12:17
0
awa.saliou123
Awa saliou :
ay way kañe lay amli
2025-01-16 23:02:51
0
mbayeterranga0
lagane business :
yalla na lepou barkell b khadim rasoull
2025-01-19 11:34:12
0
ibrahimakonte302
Ibrahima Konte302 :
Ohh say li nékh ❤️yalla na seuy bi barkel ndiaboot gou barkel barki MAME SALIOU 🙏🤍
2025-01-16 16:24:02
0
amina_rassu...1
Sokhna📿Amina💗🧕Salihou :
Souma amoule lii douma seuyi 😭❤️🤧
2025-01-14 14:50:33
71
sokhnamaianne2
sokhnamaïsaliou :
dieukeur mouride ❤mn combat 😍inshallah barke serigne saliou ❤
2025-01-14 16:04:13
23
mamegning111
mamegning111 :
yàlla na yàlla barkel sëy bi té defsi njabootug Lislaam barkep Sëriñ Tuuba
2025-01-14 14:23:48
6
daroukhoudosscouture1
Muhamadul faadal fall ht :
Mourid gor gor loul nak
2025-01-14 16:50:12
5
mame.bousso.lo2
Mame Bousso lo :
MOURIDE gawal guèné son bi🥰
2025-01-14 23:34:44
2
user3669616029724
une.diouf :
Yallah comme bi ték ték.ték ték nak lala wakh🙏
2025-01-18 09:58:27
3
pmk_45_
PISPAH_45❤️ :
Yaw dh wouté nga ak jeuwrine bi doon way « Douma ko miine ba fatté ko kon mou niaaw »🤣
2025-01-16 01:36:48
3
yayefallborom.darrou
yayefallborom.darrou :
Si mourideyi yalle namasi yalla may
2025-01-26 20:39:06
0
dabi3562
dabi :
fi aldiana la wala
2025-01-16 00:00:09
1
salihate38
user2510907671519 :
Mâcha la yalla na yalla barkel si barki KHASSIDA yi 🥰
2025-01-15 13:36:53
1
serignesaliouseckxassida
seck xassida :
niéena sama soxna 😂lii moom faw ma defal kako inshallaah ❤️
2025-01-15 07:30:42
1
boss.xassida
Boss xassida :
Machalah 🥰
2025-01-14 20:03:26
1
khalil15462
Khalil HT 761546954 :
machalla 🥰
2025-01-14 16:28:46
1
user490114624812
ndeye Bou Serigne Saliou :
sm kharit bi yalla nala yalla defal diam ak sey bou barkel si barke khassida yi
2025-01-15 12:01:55
0
mbackesdijly782969711
GÉNÉRAL BROM IKFINI :
ki dou jawrin balla 🥰😂
2025-01-14 22:28:34
0
s_modou_seck_khassida
S Modou Seck Khassida Ndiarème :
Machallah 🥰❤️❤️❤️
2025-01-17 10:43:28
2
ndickou11
ndickou diéne :
machalla mane begu na koumay défal lii
2025-01-24 13:28:30
1
maman.khady4
🇸🇳Maman mboup🇮🇹 :
Akassa ma sha Allah
2025-01-19 07:26:02
1
user48119977539783
élément serigne saliou❤️❤️🥰 :
Mon rêve 🙏🙏
2025-01-18 22:41:32
1
ndiayeibrahima24
Borom Touba Dieuredieuf 🙏 :
Fall li ngaye wax néx na
2025-01-16 21:24:23
1
user88086797
mouhamed :
Akassa mourid lii kawéna mais liguay rime nékhna way 🥰
2025-01-15 16:15:11
1
To see more videos from user @serignebarafall15, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About