@dahwa.bi: #mouride_sadikh_officiell

Dahwa bi
Dahwa bi
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 19 January 2025 14:55:20 GMT
48366
2411
161
418

Music

Download

Comments

user6514622452824
عبد القا در جن :
yen Bayi lene sen tiakhane dem lene Dioli ji mo gne fof ay tapale kene mono ko layal🤣🤣🤣
2025-01-19 21:51:04
6
refanecomunication
Modou766080518Refane :
Diarama C ibra fall 🥰
2025-01-19 16:59:02
4
sadertisseira1946
Sader Tisseira :
diarama mame cheikh ibrahima fall🥰🥰🥰
2025-01-20 04:45:18
7
moustaphambengue748
moustapha :
machalla fall yaram amna solo loll
2025-01-21 13:16:32
2
serignefall8081
serigne bi fall :
mame cheikh moma yem
2025-01-21 14:09:06
2
diopdiop.com
Mouhamed diop :
Mame cheikh amoul morom
2025-01-20 15:16:24
2
diazzpacond1
PACO DIAZ🤟🏾 :
Cheikh Ibra point 🙏
2025-01-21 03:15:05
1
serignebamba5
bamba :
akassa way fall❤❤❤
2025-01-20 01:48:09
2
bayelat18
Baye lat :
s touba moko binde s touba lo yalla wax rek la wax
2025-02-18 07:23:20
0
khadimdiakhaterafahi
Khadim rafahi :
wakhou deugg li s abdou rahmane moko lerall Mola app xam xam foff
2025-01-20 14:55:21
0
djibrildiop357
djibril diop :
wàkhou Serigne bi amoul sama Khalaat saawaay
2025-01-22 08:26:20
0
user807430560
user9011277995048 :
machallah 👍👍👍
2025-01-19 22:52:56
0
user6514622452824
عبد القا در جن :
tia khan bakholl niaka Diolli ken mono ko layall
2025-01-20 10:59:23
1
khadimdiakhaterafahi
Khadim rafahi :
s touba wakholl kenn boull diouli mame cheikh Ibrahim fall tamitt nonou
2025-01-20 14:57:02
0
babsndoye26
Babs Ndoye :
lgui bou ko Serigne bi bindoule té yalla wakh ko si alkhourane nk bayilen thiakhane
2025-01-20 10:00:49
7
hazardjr23
TikTok 221 :
Mandou la ya geun beug si Diouli tei yala dou fay wah bayi dieuf bo dingate c Ibra safaragua dieum tei ioe mi bye fall yi niola geun ndakh lini dieuf si rew m ak si Srgn bi bu s baye sah baye fall la
2025-01-21 02:07:33
9
baba.thiane5
Baba Thiane :
🥰🥰🥰🥰🥰sante sidy birahim fall rék point 🥰🥰
2025-01-20 00:15:04
7
lhomme_veridique
Mouride sadikh bi :
démlén juliji té bayi sén tapalé yi
2025-01-20 07:41:57
1
user1262363156173
al amiin firdawsy :
Delen dioulli di woor te baayi sen thiaxaan yii akh
2025-01-20 10:06:09
1
fallousarr164
fallousarr mou serigne same965 :
walahi walahi deugeula barkeb seringe touba
2025-01-19 17:34:56
3
sefaconsbtp1
SEFACONS.BTP :
Xawma du wayei lou Serigne Abdourahmane waxx moy deugu
2025-01-20 15:11:09
4
werakanoubamba
werakanou bamba :
li werte worr wakhi Serigne Abdou Rahmane la geuna geum ci saye wakh
2025-01-23 18:30:08
1
mbacke.balla.acha6
Mbacke Balla aïcha :
li serigne abdou rahmane wakh moye degue kouwakhoul lolou abe féne guate la
2025-01-20 20:33:01
1
prix.sngal
prix Sénégal :
legui wedd gueen lettre bi andil len gniou lettre tèrèh bi
2025-01-19 23:35:35
1
bayefallmbengue6
mouhamed mbengue :
baye fall touma la bakho
2025-01-20 14:04:42
4
To see more videos from user @dahwa.bi, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About