@nanu_dellu_si_allah: Allah dit dans le Coran : "Ils se cachent des gens, mais ils ne se cachent pas d’Allah, alors qu’Il est avec eux quand, la nuit, ils tiennent des discours qu’Il (Allah) n’agrée pas. Et Allah encercle parfaitement tout ce qu’ils font." (Sourate An-Nisa, 4:108) ✅#ProphèteMohammadsws #tawhid #sengaltiktoker🇸🇳
Walaahi dano kham ni yalla moo eup sutura rek 😩 nit amul sutura te yalla dafa bari sutura yalla nanu yalla sutura la te diegal niou
2025-01-30 21:02:00
791
user33628430823 :
yalla Nanou yalla diégal tédimbalinou
2025-01-29 23:58:43
788
@MIG~Aplle :
Yalla NaÑiou yalla geuna Khir thi bopam
2025-11-28 03:20:25
13
Seriñ moussa fall 🖤🤍 :
Ay waye Kou maye santalé yallah 🙏😭
2025-01-30 18:31:13
242
☪️✪ الله Nanu dellu ci :
Nous pouvons cacher nos péchés aux yeux des hommes, mais jamais à Allah. Il voit tout, Il entend tout, et Il sait même ce qui se cache dans nos cœurs😭😭
2025-01-29 23:13:25
203
bab's :
rouss na sakh yalla naniou yalla diégal suniouy bakar 🤲😭🙏