@tijaniaminusanussibarham: Réponse à @chiko489

tijaniaminusanuss
tijaniaminusanuss
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 01 February 2025 21:32:56 GMT
19330
890
156
216

Music

Download

Comments

cossaan174
wolof sama lépp :
Baye ndiass mo wakh si lamagnam né Y wolof lan.Néttali si lamagnou boppam.
2025-02-02 16:09:24
7
catf03
C@_Tf :
Niass avec e moy nienio ...Mame Abdoulaye Niass dou nienio
2025-02-02 11:50:37
7
tima000221
tima000221 :
Baye Niasse setu biram Ndiemé coumba Ndiaye Niasse lanu remplacé Ndiaye ndax danio xeron ci Alquraan.Baye waxalnako boppam.
2025-02-02 11:34:08
8
bergeriebarhamkmal
bergeriebarhamkmal :
Yonenté Yalla Daouda teugg lawone Nohine Laobé lawone Corps de métier yi niou beugg doyadal si rewmi rek moma mety. Bou lolou wesso nak Baye Niass Waxx naniou fimou bokk ta limou niou Waxx laniou guem
2025-02-02 11:18:57
22
user206638367033
user206638367033 :
Baye niass néna môm Chérif la mokô bind
2025-02-02 10:51:47
12
dioufy.fire.for.e
dioufy fire for ever 1900 live :
Je suis petit fils de de Semou mak et pourtant je suis talibe baye Niass et mon guide c’est mame malle Thiam
2025-02-02 08:07:50
12
mbackebamba88
support du savoir :
boudé niénio la serigni Sénégal yeyp ay niénio laniou dalé thia cheikh omar foutiou
2025-02-02 10:32:59
11
number.one4056
number one :
Sénégal dal niepa bok mashalah
2025-02-02 12:09:35
8
semodewa5
azertyuiop :
Baye niasse wolof la mame masssamba thiam wolof la
2025-02-02 22:31:18
10
niasse_abdala
firi téré baye niassssssse :
lolou Serigne you gniak arguments yi gnioko Andi si réwmi wayé baye wax nagnou askanam
2025-02-02 12:22:07
6
user3354787229581
user3354787229581 :
kone si sante niass aye niènio lanou
2025-02-02 10:48:12
3
cheekhfaal
cheekhfaal :
il s’est totalement trompé sur Khaly Amar Fall. Ki amoul xam xam. dafa confondre ay périodes historiques
2025-02-04 16:09:48
0
anonyme31366
Anonyme 313 :
Salam kiy wakh kan la ?
2025-02-02 06:55:36
1
user8182418030053
Bachou :
Niasse Askanou Rabbe leuh wayé askane nieupako ame wayé Ame diné rék mo ame solo Mane askanou Guéwal la bokk té kéne guenouma ham Yallah
2025-02-02 22:52:45
3
mhd92802
MHD92 :
Mam massamba thiam sama mam lh mane mii
2025-02-02 16:03:36
1
maguy3358
maguy :
legui Nou Cherif bi nga moudie wakhe sant ?
2025-02-03 15:30:57
1
diackdollars08
Diack 😎❤️😍 :
😂😂😂gnom dani soss rek mai jamais gnou am lou melni 🤣🤣
2025-02-02 22:39:22
1
ousseynoukhouma5
kajoor/ Baol :
Damel Ameri Ngone Ndella et non Ameri Ngone Sobel.
2025-02-02 11:10:50
1
diaguily3
Diawara :
Ça ne doit pas être un débat car notre guide a écrit sur ses origines
2025-02-02 11:21:45
3
kanzobarry
kanzobarry :
AK loumena khéw BAYE NIASS mo raw nieup . WALLAHI NDEYSANE.
2025-02-04 15:09:27
2
bayelover
bayelover :
Ahmed khalifa boudè mo wax lolu erreurs la ndax papam si nopam binde na beyti nè niom thiossane arabe lagne
2025-02-06 20:59:32
1
zeyda58
user7165132910163 :
waw légui nak Baye niass nagnou beugue ♥️yalla khamoul Olof ak gnégno. diamou yalla bi nagnou kham.
2025-02-04 00:42:46
2
kawoyendiath
اللهم صل على محمد وال محمد :
Li Bane ngering la am
2025-02-04 05:22:08
1
atly11
atlytv6 :
Wërilèn sène askane ci Yalla té bayyi askani aduna yi day jèex
2025-02-03 17:58:29
1
ibrahimandiaye6551gmail2
ibrahimandiaye6557 :
borom commentaire bi ya mana doul
2025-02-02 21:37:55
1
To see more videos from user @tijaniaminusanussibarham, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About