@pansement_lptc: Yaubou nga sama khél🧠 ba khamatouma noumay déf, mome nga sama khol❤️ ba amatouma ci ndogal. Wayé nak mala diokh lëp lima yor, ba paré nila garde la monnaie. Ndakh yako fa am🥰 #mindsetmotivation #motivation #foryoupage #viralvideo #developpementpersonnel #abonnements #senegalaise_tik_tok🇸🇳