Je suis l’auteur de cette vidéo et je suis ouvert d’esprit vous pouvez poser tout vos questions et je répondrai tout avec modestie niou wakh si xam xam🥰🥰🥰
2025-03-04 12:36:47
37
Dahiratoul Imane TV :
Bayilen tiahan baye baye diamou yalla la
2025-03-03 18:20:43
18
Binta Mou baye segnan 🥳❤️ :
Baye woni allah 🥰
2025-03-03 21:11:46
20
Ousmane Officiel :
Neke lene ay nit bakhna
2025-03-04 15:45:20
7
SOURGA✨NDIAYE🎙️ :
Allah Tan Woni Allah Baye Ko Mathioudo Allah 🥺Baye Wiani Ni dh
2025-03-05 00:32:20
5
Z🅰️H🅰️ 🅱️A🅱️Y📱🍿🧃 :
Je suis talibé baye mais même baye niass na jamais dit que suis dieu
2025-10-21 21:07:17
0
Thierno Assane Ba zakir🇵🇸 :
non baye moy baye yalla moy yalla
2025-03-04 03:04:43
10
Salma Diong1 :
non la vous exagéré carrément ALLAH ko ALLAH
dites soubhan allah🥺
2025-03-04 12:42:19
5
Djiby Diop Zakir NH :
Baye wona allah dh et halani doum dh
2025-03-03 22:48:08
4
ibn_Ahmad_🇸🇳 :
waxo deug dé . fou baye doné yalla
2025-03-03 23:42:03
7
Amthi_75✌🏾🇸🇳 :
Wakh léneu baye woni Allah 🥰❤️🙏
2025-03-06 20:05:37
2
PeulhBarhama Business 🇸🇳🇧🇫 :
Dieureudieufé Baye ❤💯
2025-03-07 14:17:02
3
Baye mbengue :
tiaxan rek
2025-03-04 09:28:29
4
La vérité :
Lii gnaaw na talibé baye di wakh baye mooy yalla c'est domage bilahi baye niass djeulé niou ci chirk gnoun niou déllo suniu bopp ci chirk
2025-03-04 05:55:52
6
Sérére ✌️bou Nice😍 :
Boulene tontou négatif ñiou ne talibé yi ñio kham
2025-03-05 03:16:15
1
ahbaabcheikhmahic :
li deh khalifa bi warna si wax
2025-03-03 22:46:14
6
Aminata-Mou baba :
Dieureudief Baye Niass 🥰
2025-03-04 13:56:47
5
Dioum kourous 🫰 :
je suis fière d'être talibe baye mais je suis pas d'accord baye wona allah Dieu es seul
2025-03-04 06:07:03
5
Taïba Vision 📸📸 :
Baye Niass Moy yalla bouléne niiou sonnal
2025-03-04 10:06:16
5
noirceur 🇸🇳 :
🥰🥰🥰🥰🥰machalla
2025-03-14 06:53:36
1
Oulymataaa00 :
Ehhhh
2025-04-06 03:14:14
1
oumousow7467 :
billaye Moye allah ❣️📿
2025-03-06 13:46:41
2
ousmaneba4579 :
koula khamall benn araff tii yaw moy sah yalla
2025-03-03 23:04:01
0
Cheikh Diallo :
machala
2025-03-22 20:32:32
1
To see more videos from user @benaylon, please go to the Tikwm
homepage.