Thiery mbakce wadiga dh yalla na sounou borom teral la si dianatoul firdawsi 😭😭😭😭
2025-02-17 11:44:45
175
Seriñ moussa fall 🖤🤍 :
Ay waye Kou maye santalé yallah 😭🙏
2025-02-17 14:02:57
104
Y26 :
Lan mo tkh niou baakh gni bougnou guené adouna rk lagn len di doguay baayi khel ??😭
2025-02-18 22:02:27
35
saer mbengue :
Serigne Moustapha yalnko brom Touba térou
2025-02-18 15:45:10
40
Adja Barro :
Balla Aïssa Yalla Gua tassel yeurmander Souniou Borom gua tasse sa wadiour bou bakh ba Serign Saliou thia Adiana Firdawsy
2025-02-17 12:25:32
51
linguerou ❤️❤️ sangeubi :
nitou yalla deug moy ki amna xam xam bou sélé té diko diéfé
2025-02-17 15:29:44
78
Ridial business :
Xamnani kou beug Serigne touba là bilahi yalla nako yalla yeureum 😭🙏🙏🙏
2025-02-17 13:43:47
31
Une S@lih@te❤️Longrich# :
Cëy Mbacké balla aldiana sa dalou way barkep Cheikhoul khadim 💔😭🙏🏾
2025-02-17 23:15:35
5
bamba seck sonko 2029 point :
kou xam serigne touba te donnou foula dji yalla nako yalla tero aldiana
2025-02-17 20:14:37
16
ndeyefatougueye731 :
Inna lilahi wa inna ileyhi radjihoune 😭💔😭💔😭💔🙏🏽☝🏽
2025-02-17 14:13:05
6
Dieu :
Yalla nga xippe aldiana firdawsi si barke seydina mouhamed psl
2025-02-17 22:59:55
22
user5395190881934 :
ndeysane yalnanouko yalla Fayal Serigne Moustapha saliou
2025-02-17 15:35:54
25
ABLAYE BOU SERIGNE SALIOU :
ndeysan soumaye dégue saye wakhtane sama khél mii daye dém sisa Waydiour bou bakh yalna nga dadié Yeurmandé sunu borom barké seydina Muhammed mbacke balla Aïcha yalna yalla khare aldiana firdawsi🤲🙏
2025-02-17 12:50:39
20
user565055395264 :
Lépeum Serigne Touba la😭 Yalnako yalla yeureum ci barkep Serigne bi 🙏
2025-02-17 20:07:09
21
Codé Ibrahima moom kooké :
Kéne messouko yaap si doundam té likofi dieulé yiit xamnani serigne Moustapha saliou mi mesouko ragal 🙏😭😭😭😭😭🙏
2025-02-17 20:14:25
7
sokhna ndeya saliou ❤️❤️ :
yalna yalla yokiy lairam té taf niou barkém Amine 🤲🤲🙏🙏🙏😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2025-02-18 00:45:45
7
Habdoul ahad :
الصلاة والسلام على رسول الله محمد
2025-02-17 16:12:15
5
Innocent 😇 :
Yalnako yalla yeureum Mbacke balla😭
2025-02-17 12:13:07
21
achraf cœur sain :
ndysan gaayi bakh yi gnogui dem rek thiey yàlla mofi bàyyi gni tok si minbar yi di fenal nit gni rek 😭😭😭
2025-02-17 13:18:40
10
Madame khouma :
ndaysan kou bakh loll way dém n'a firdawsi sa Karr mbacke bala amine 😭😭😭