@bass_et_ses_videos: Réponse à @✝️Etienne221🇸🇳 #tiktoksenegal🇸🇳 #senegalaise_tik_tok🇸🇳 #humor @Dudu

bass_et_ses_videos
bass_et_ses_videos
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 17 February 2025 13:35:39 GMT
958300
105937
3594
621

Music

Download

Comments

mamebousso460
mamebousso460 :
Ma fall da dièkh sakh iow 😂😂
2025-02-18 12:39:14
626
user2437038860096
user2437038860096 :
Niou da dialé fayal mafall bor bi 😂😂
2025-02-17 13:55:52
6
tabousta
Taboush♥️🍫 :
Mafall soneuna 😂😩😩
2025-02-23 11:31:37
0
boutique.en.ligne08
boutique en ligne 🫶🏽😻 :
😭😭Andeu fayal ma fall boore bi 😂😂😂😂
2025-02-17 14:12:15
17
khamzoloffice
khadim Mbaye 44 :
ma fall mome da yarou sakh wl daffa khamni mo nékoul si yone😂😂😂😂😂😂😂😂
2025-02-17 13:44:25
6
toucouleur234
Aissatou♥️toucouleur234 :
Coalition ande fayal ma fall
2025-02-22 20:05:10
2
mignonnepeulh73
mignonnepeulh73 :
😂mafall esk doma wax niatala ma fay prsk nioun sax nio modie sonou 😂😂😂😂ah
2025-02-17 14:07:48
9
jeune_tidiane
jeune_tidiane :
mais Mafall mom ndakh meun na wakh😆😆
2025-02-23 03:58:31
2
lanalphabet2.0
Mike🇸🇳🇺🇸 :
Mafall ak dialabé badola bi🤣🤣🤣
2025-02-23 14:47:25
0
serigneamethsaliousene
Serigne Ameth Saliou :
bor bi takhna senegal yafi eup securitè bilahi😅😅
2025-02-21 14:18:05
15
uuzy_sarr
Uuzykarim🇸🇳 :
Saway ngirr yalla bor bi niata la ma fay ko iow rek la guiss nitt yorel la nga sonal ko witt ba nitt gni dila Sarakhou pour fayal ko nga bagn🤣🤣🤣🤦🏼‍♂️
2025-02-17 16:40:28
18
awadiouf4361
Eva Saloiu💕🦋 :
Ma fall esk dinga dem douse 😂😂😂
2025-02-20 16:27:20
7
leye108
Moustahpa ⏳🤍🇸🇳 :
Mom xanaa dafa takal Mafall GPS ?😫
2025-02-17 13:44:12
1
mafallfall97
mafallfall97 :
Mafall rek
2025-02-23 20:24:06
1
matarngombayefall44
Matar Ngom Baye Fall :
mbaa koor gui dinga Bayi Ma Fall Mou Ndogou tontouma nguir yalla 🤲
2025-02-23 19:02:31
2
falltapha66
Tapha Fall ❤️66 :
Wa khalis bi mom niatala khana dou diekh 😂😂😂
2025-02-17 16:03:35
1
chndiguelndiayebague0
ch ndiguel Ndiaye bague borom :
ma fall lolou bakhna ndakh daga soonne
2025-02-17 15:06:22
5
user4696573113762
AMdY Simons :
mafall yarouna troop
2025-02-23 09:35:05
3
papa_lintrus
Papa_L’intrus🏟️ :
Mafal ndeysane dou sakh tontou pask mo yeerel haliss nite kii😂😂😂
2025-02-17 21:29:29
3
diagnedejong21
Diagne De jong :
wa loutakh mafal dou wakh dara😅😅😅
2025-02-20 22:21:02
5
madame.ndiaye523
madame Ndiaye :
ndigal kalla DIJ man nama ray😂😂
2025-02-17 14:37:31
2
chuetjule5
Chuetjule 🦂 :
mangui ram 🤣🤣🤣🤣🤣ki mo sonal Ma fall 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
2025-02-17 16:06:12
3
babacar.barra.7632
babacar Barra 763299662 :
mafale sa borbi niatala ma fayala ko nakh nga nopalou
2025-02-18 23:50:13
5
masse694
Masse Le Pâtissier 👨‍🍳👨‍🍳 :
mafal niata ngako yorél niou cotisé fayko
2025-02-17 16:19:22
3
stellandeye
stellandeye :
😁😁😁😁😁😆 yow mouno bayiii ma fall. mou am diame 😁😁😁😁
2025-02-17 16:24:34
5
To see more videos from user @bass_et_ses_videos, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About