@buzzposts2: Mashallah FAH AIDARA Djiguène gni sonneu nagnou trop si goro yi ak ndieuké yi 😭😭😭😭😭 #fyp #videoviral #viral #videoviral #fahhaidara

Buzz posts 2
Buzz posts 2
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 23 February 2025 03:05:41 GMT
368483
32108
1032
1244

Music

Download

Comments

lrhealthandbeauty69
Sallah Ngarry🤍🧿💐 :
Kaye lane Gambia 😅
2025-02-23 20:28:52
7
limachou13
limachou♥️ :
Li xamouma Kagn lay diex
2025-02-23 15:25:23
5
mariama161
RIMA CHOU🌹161 :
Billaye wayyyy liiii😭😭😭
2025-02-24 16:00:47
0
vieuxcana
vieux cana officiel🇪🇸 :
machallaah yaye boy ❤️🥰💕
2025-02-24 13:19:31
0
fatouch6727
FATOUCH🍯❤💯 :
Deff loo meune waff loo khame🥰🥰
2025-02-24 13:49:14
0
sarr.maabo
sarré Maabo 🥰 :
wife 🥰🥰
2025-02-24 14:49:01
0
seckmaremeseba
seckmaremeseba :
fransment🥰🥰🥰
2025-02-24 09:53:10
0
chumbe472
chumbe :
ma sha Allah manasol lol
2025-02-23 18:17:20
0
hommefort_221
Barhamien :
Maneu louma meunoul comprendre eumb, diour dom ba parei di khalaat teralatei
2025-02-23 09:39:12
1515
kenzafall0
Kinouch🦋Mrs Gaye❤️🇨🇦 :
Fah Aidara moy vrai influenceuse ❤️
2025-02-23 15:50:43
1791
boucheiktiktok.c
ma famille ma fierté :
sama yaye aka ko banie am na niari goro mais kouthi nék baguay guété dafa wo sa yaye niko bouma fi vale féké bilahi
2025-02-23 11:46:02
653
larassoulienne6
🫶🥰 :
Sama adouna yeibii lassi gueune contre 😭😭 yalla xam nako
2025-02-23 11:35:12
358
user6888400493774
user6888400493774 :
li dé Sénégal rek la am motakh seuy yeup am problème ga embeu weusine niou wara teral gay teralatei
2025-02-23 12:13:43
199
anita_barham_niang
Anita mou baye ousseynou 🥰 :
yébiwouma , yébilowouma kéne , kouma yébil baloumako , douma quitter samay parent ,di daw si banékhou goor chaque jour, eumbe weussine teksi Di yébil ay nitt Mane laniou wara téral pas kénéne
2025-02-24 00:54:53
96
diamila.1
diamyla :
bilay wakhatiko magui eumbe ba diss wayé souma khalaté yébi bi rek stress mouguimay beugu raye
2025-02-23 12:35:32
78
salihatebusiness15
Salihate business 🧕✂️ :
Nagnko voté li mome dafa wara diekh😏
2025-02-23 13:39:53
215
ndiolediamannoire6
@ndiolediamannoire :
Insistelle fofou la ticktokeuse du peuple 🥰🥰🥰
2025-02-23 09:42:56
261
maribelle352
Maribelle :
Elle a raison nagn lenn mankoo diéné lii Senegal
2025-02-23 15:44:59
156
ndeye.coumba.drame
Ndeye coumba Drame :
man dei bima defe lima meun damako khebal tei sama yaye dafa guaniou avant bobu ma am eumb meti sama magu yaye deff limou meun mashallah diokhewul ay sagar tei dagnko kheb
2025-02-23 12:28:00
58
salicledor
Salif clédor🇸🇳🇸🇳 :
🤣 Sénégal ki diour dom moy téralaté🤣🤣🤣🤣🤣 ma fokni ki âme dom lagnu wara téral
2025-02-23 13:13:32
57
koura.saliou7
Koura saliou ❤️🙏 :
Sénégal deh ndaeke yonete bi psl lagnou beuge ❤️❤️❤️❤️❤️íhomme parfait
2025-02-23 23:40:58
233
adamajules21
Business wifi and IPTV Adama :
niou war Laa téral ngay téralaté... idée bi mom Kiko indi Sénégal yalla Koy mbeuguel ndakh yeufi dof la
2025-02-23 13:00:31
67
arametraore8
Arametraore :
Yébi bokk na lima guena contre si sama adouna. Affaire tiakhane la bilahi. Au contraire kou djiguene ki laniou wara téral mom mi bayi keur baye akk ndeye dem fèki niénéne 😫
2025-02-24 08:59:46
13
aelyne24
Aélyne :
Baniou ma teral dei normalement boy teral Kou djiguéne ki laniou wara teral ndax lepp mome la
2025-02-23 18:04:01
50
deuthpppnb
le peuple :
machallah amna 3 grossesses mé mousouma yébi té magui sant yallah si ame ame machallah damako khékh ba ame sama indépendance mane kéne douma tekk stresse
2025-02-24 11:30:15
8
To see more videos from user @buzzposts2, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About