@buzzposts2: Réponse à @diouf4080 Pourtant, Ahmed Khalifa li la yague wakh , mais Sénégal kou amoul xam xam moy tok diko wédi wala diko sagua . Dieredieuf Ahmed Khalifa Niass et à vous Oustaz Sidy Ndiaye ♥️😍 #buzz #videoviral #viral #fyp

Buzz posts 2
Buzz posts 2
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 02 March 2025 16:21:04 GMT
564274
24001
1216
5667

Music

Download

Comments

astel998
Astel 💝💝 :
Lékk toutii thiakri nak
2025-03-02 21:22:16
170
bambapatriote8
BAMBA👨‍⚕️🩺 :
Oustaz Yanguii djoum dh
2025-03-02 19:35:30
42
arleya04
arleya04 :
Avaler salive nak ? Mane problem bobou la am souma lekoul damay beurri salive
2025-03-02 20:44:20
6
theiki_fall
Theiki-🇸🇳🪐 :
Xana puff kone yaxoul koor walah Question la rek 🙏
2025-03-02 19:46:01
5
uuofgmpttj166modou
modou lô :
2025 dara yakhol koor🤣🤣🤣🤣
2025-03-02 20:08:49
33
user7749218511813
BM :
li mom nexna dii losi doli sour dh 🤣🤣
2025-03-03 17:14:23
3
ndiobeeene
ndiobeeene :
wakh deug serigne bi man mooom andouma ak yaw thi linga wax
2025-03-02 20:34:24
1
goresarr662
soldarou sarigne khadim mbaké :
wa ki kan moko diagua fane gua diagé Qustaz liguay wakh Bou Xam xam dh
2025-03-03 00:43:12
3
cheikhwally23
Kheucha l’homme tranquille 🥰 :
Ouztas lépou lou toye daye yakh koor 🥰
2025-03-03 03:22:18
4
thiatoujoe3
thiatou joe bou soncko ✅ :
ndéki yahoul kor . agne yahoul kor. sow mou séd yahoul kor.
2025-03-03 12:31:35
1
user843840565030
lamin Mbàkke :
lii de xaw naa wuute ak lima xamoon 🙏
2025-03-02 20:38:03
2
papa2lasmelliz
Papá d mellizas :
IOw mom Koula deg lou dina woor ba naw.. ligha fi wakh ni lousi barei day yakha koor
2025-03-03 00:55:00
1
etudiantbg2
Etudiant BG2 :
Oustaz Sidy Ndiaye
2025-03-02 20:53:36
2
cheikhbi8
cheikhbi :
lih moy xam xam way bouh seleu
2025-03-02 22:07:47
2
hapzlowe933
Hapz Lowe :
wohou Ahmad khalifa ba ngii aka borii xamxam
2025-03-02 20:54:52
1
boromdarou103
Le Prof⚽📏🖋💰💵🇸🇳 :
Ahmed lima wax yaxoul koor mo gueuna grave lii. Mano fi valoriser ahmed ...Nopil
2025-03-02 21:19:01
1
masserone.marone
Marone Ronemo :
lou lerrr gua wax
2025-03-02 18:40:02
3
thiernolo7
Thierno Lo :
Toufay mome day yakh koor
2025-03-02 20:26:59
1
ousma623
ousmane ndiaye :
gùayii dall koor guii mayonnaise lagniouko deff
2025-03-02 20:14:14
1
cheikhdiakhate30
Cheikh vendeur Hijab Tussi :
Toufay ak thiouray ak pompe yëpp day yaq
2025-03-02 20:46:23
1
serigenmoustaphasygueye
Talibe CHEIKHOU tidiane. :
Ko si thiakhan rk la nek
2025-03-02 23:26:06
1
moustaphandiaye018
moustapha ndiaye :
Percussions
2025-03-02 20:42:34
1
haladji.tour
Haladji Touré :
Khana ap ibadou la kham kham 00000😁😁😁
2025-03-02 20:30:04
1
nabouja613
Nabouja :
Wathiou yakoul koor ms danga koy fay
2025-03-02 20:29:37
1
maledominan
L'homme Alpha2.0 :
Oistaz man mazhab nga teunku la begon xam? Dou Malick dei mom
2025-03-03 22:43:50
0
To see more videos from user @buzzposts2, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About