@thierbusnesscompagny: Li mome @Abdoulaziz Ndiaye lay wakhal #pourtoii #comedyvideo

THier busness compagny
THier busness compagny
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 06 March 2025 20:24:04 GMT
98164
4488
117
532

Music

Download

Comments

sheikhbicisse
CTC :
Réw mi dafa yagone si tapalé . Jub Mba guén rew mi rek .
2025-03-07 15:15:04
1
ndiayesonko04
pape-laye 🇸🇳🌍 :
domerame dji tok mouy dokh amatoufi liguey rek mba nga nokhou sa khadji
2025-03-06 23:36:59
96
djily318
djily318 :
Lui il vous montre q le pays dokhoul 😌 .... ngène di saup nane tok mouy dokh
2025-03-07 16:00:25
22
sg_papi
Papi❤️ :
Moy prési thiompal thiomplé ceux qui le suivent savent, li rek preuve le ni actuellement ligueey rek mba do fayékou
2025-03-07 00:11:21
30
testchera665
test chera :
Mais lolou moy yone, kaliss dagnkoy liguey. Lou yomb ngen beug. Pa bou tolni yow amo métier
2025-03-07 07:53:35
19
topcas221galsen
T Bii❤️😘✌️ :
Thiey sonko mo kham système bi 😂
2025-03-06 23:37:13
82
momolb8
MomoLB🥳🌵 :
Aziz ndiaye😂😂😂
2025-03-06 21:36:46
41
alaminelayethiam
Général Plomberie d'entretien :
kou amoul métier yeureum na la
2025-03-07 00:41:32
14
tukuleurs
Tukuleurs :
Ahhh konn dé sant YALLA, reew maa ngi si yoon. 😂😂.
2025-03-07 02:07:23
12
bachbach350
Bass bass :
Weur di gnane djexna tamit🤣🤣
2025-03-06 22:46:12
11
mouhamedsarr282
Mouhamed Sarr282 :
Nioune nane laniouy beuguer yeneine deuk respect niou té Nioune souniou bop diokhou niou sounou bop thieur c’est pas la personne de diomay ou sonko qui compte mais ils représentent le Sénégal 🇸🇳
2025-03-06 23:15:49
10
laye2122
laye :
Ligay rek lguii ligay djeurignou 😂😂😂😂
2025-03-06 23:15:06
10
mouhamd.tour
Met 🇸🇳 🇨🇦 :
Sonko nitt ku wémé leuh🥰
2025-03-07 01:34:06
9
malicksenegalais2024
Malick🍀🇸🇳🍀 :
Gnakk Diarignou Dieufdieul khaliss dagnou kayy liguéye Rewmi si lidianti katt kassé gnoy Dioyyyy
2025-03-07 00:28:49
6
bacargni567
mbaye gning :
niou done politique niou gui diaye guédji
2025-03-07 08:17:06
5
badara452
badara 313 :
Réw bi kay 😂😂😂😂😂
2025-03-06 23:00:19
4
ibrahimatop875k
khalil kharitou yalla😍 :
bayilén sén thiakhane yii réwmi nioune khoss lou mane sakh yora touniou danguay kheuy do diayy dara rien ne marche dans ce pays suis désolé
2025-03-07 12:35:18
0
adamalam839
Scorpion bi🦂 :
Niakh djeuriniou rek 😂😂😂😂😂😂
2025-03-07 00:04:33
4
mouhamedcisse014
Mouhamad Cissé :
Kou dh say dokhatt diékh guisnasi sama bopou dh 🤣🤣
2025-03-07 01:06:34
3
ndongo.ji
Ndongo ji patriote :
diaradiafate sey dîna ousmane
2025-03-07 14:36:35
2
concorde085
Phœnix :
Yor sa lamign bou reuy def ko extra si sa ligey yakar ni moy doh nopaloul ligey rek au dela du dev le changement de mentalitè est enclenchè
2025-03-07 10:59:55
2
lexedieme
wizzz..🇺🇸🇩🇪 :
togue mi dokh mofi diégue demléne liguéye mon geune.j.j'j rékh
2025-03-07 09:13:42
2
bassbusonko
Guane Dou Tabakh🧠⛓️🇸🇳 :
Système bagui wéxou 😂😂😂😂😂😂😂
2025-03-08 01:17:45
1
senegal269
✌️ :
Wakh na deug niveau dafa wathie ay aziz ndiaye kay tik tok bi lay weur di live rek 😂😂😂😂Sénégal sonko à remis chacun à sa place 😂
2025-03-07 21:56:15
1
la.bute.fminine
La beauté féminine🛍 :
Khaliss AK aldiana koula ko yombal raye nala
2025-03-07 11:52:01
1
To see more videos from user @thierbusnesscompagny, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About