Pa Abdou manguilay niane nguir djeumi Cheikhou Tidiane Chérif RTA défalma Ben enregistrement niane bi leep nga yoné mako ndakh makoy deglo chak matin balamay kheuy ak balamay teud
2025-03-10 23:37:57
87
cheikh abdallah sopou nabi :
yénn lh tariikha bi sokhla dh moytou léne djiguéne gni 😭😭🥰🥰🥰🥰 yalla samma lh té aar lh machallah
2025-03-09 21:21:43
14
Mane Tidiane la :
bilahi ya takh ma meune nianou wazifa bi
2025-03-10 18:34:31
430
Balxawmi 😍😍 :
est ce que yéna ngui dég voix bii 🥰🥰
2025-03-10 01:17:26
374
M H D LE NABIEN ❤️🩹📿🖇 :
Pa Abdou damala soppou Walahi si barké YONENTE bi SWS barké Cheikh tidiani 📿🙏🏾
2025-03-09 21:56:51
211
Chiekh Balla At~tidiany :
Sa wadji❤️😭
2025-03-09 21:58:53
23
AblayeNdiol Fouta :
PA ABDOU vie longtemps que possible Barké Serigne Babacar s’y Malick Al Khalife
2025-03-17 01:28:22
55
DIOP COSMÉTIQUES :
Un cœur pour prophète muhammad❤️
2025-05-15 20:38:52
15
L-T-K LOUFF THE KING 🤴 :
da gni wakh rk mais kènne d'où cheikh omar al foutiyou moye mbeur bou makk bi dh mais bounie wakh niou beuri Danie koye faaté
2025-03-10 02:52:57
68
Maam Moor Si :
Lii neex na waay yal na Yàlla sàmm baat bi
2025-03-11 13:17:24
8
baye sarr :
Macha allah 😭
2025-03-10 00:27:14
14
Mouhamed Sy :
Machallah ❤️❤️Yalla Na Yalla Guina weral batte bi inchallah yalla nalla yalla takhou te Samou la te ar la inchallah si Barcke Cheikh Ahmed Tidiane Chérif RTA xool yepp sedd na Gouye
2025-03-13 03:20:55
10
Scarface :
niannn bou complet ma sha llah...
yalla n'a buur yalla missi tour you kawé yi ak mélo you sell yi dott di yokk ay léram si barki Seydi woudioudi..aminn
seydi Oumar Foutiyou Tall
2025-03-10 00:08:36
20
zawiyatv5 :
Kii mooy nian si zawiya mame maodo tivaouane wala
2025-03-10 16:23:55
9
Niang :
Pa Abdou bilahi diga fi meusa raay nit thi sa dua yi