daw ngir diabote rek bagn satchi bagn talal loxo métina que leurs âmes reposent en paix
2025-03-11 20:30:32
3678
Crocs_dakar_221 :
Force a vous les Ouvriers niogune metti liguey you risque bo guiss nio koy def te salaire yi bakhoul 😭nalene yallah fay Sene khole 🤲🏻🤲🏻
2025-03-12 22:01:46
3
Aloudiallo :
mon frère lamine diatta fait parti paix à son âme
2025-03-12 18:42:26
11
Sopey cheikh Al khalifa😍 :
Etat du Sénégal mo wara dieule ay mesure si ouvrage bi ouvrier yi bly danio sonou l'État doit contrôler tout les grandes chantier yi
2025-03-12 23:23:23
3
BAF ASZO :
ohhhh j'ai tombé sur ça hier mais sama xol toyna à mon retour khawma sakh limay dawal ndakh triste bilay yalla nalenn yalla yérem té kharé lenn aldiana firdawsi barké wéro koor bi
2025-03-12 13:00:57
188
🧜🏽♀️Sherifa🦋 :
Le plus triste moy ça devait être sûrement pour ay journée 3mil 5mil j’ai mal 😭 YAAllah nalen YAAllah yeureum
2025-03-12 15:02:16
39
user1478525262219 :
yalna soufe oyofe si séné kawe
2025-03-12 17:07:57
20
user9176457675397 :
yalla naniou khippè adiana firdawssi
2025-03-11 23:30:33
29
Niang mballo 233 :
ni lane rombeu tay gnouy nettoyer ma téneu di léne khol 😭😭 ndeyesane
2025-03-11 20:21:42
520
ELECTRICIEN & GRAPHISTE :
Je suis électricien mais je peux vous dire que les ouvriers ne respectent presque pas les mesures de sécurité talou niouko sakh
2025-03-12 09:45:29
362
cess94 :
maçon yi il mérite un très bon salaire vraiment ligueye Beuri na risk lol k firdawsi soit leurs repos éternel
2025-03-13 00:11:36
1
NDIOR Dev :
Que leurs âmes reposent en paix 🤲🤲🤲🤲
2025-03-12 22:20:37
3
Tawou GOGO7 :
c'était où
2025-03-12 00:37:37
2
Machallah style :
Oh Ndessan Yalla naleen Yalla yeureum mais gniou bayi khel ceinture de sécurité yi you ouvrier yi di takk
2025-03-12 18:48:45
15
𝕻𝖆𝖕𝖆𝖆𝖇𝖉𝖔𝖚🧠🕵🏽♂️✍🏽 :
SST.
Santé et sécurité au travail. Un aspect jamais respecté au Sénégal. Aprés ils diront ndogalou Yallah🤦🏾♂️
2025-03-11 23:28:22
96
To see more videos from user @dakarbooy, please go to the Tikwm
homepage.