barki serigne saliou sama xol séd. thieuy aldiana bagniou wara dadie ak serigne touba ba baye matar wala diague 71 thiey lolou
2025-03-16 22:48:24
4
Abi-Mountakha🥰❤️ :
C’est que Jazbou mo am guitar, piano, saxophone, flûte, violon, xylophone, maracas… Sama Wadji dako béral loxo way🥺🥺
2025-03-17 09:13:11
4
😚Beugfallou Sindidi🥰 :
ba déwéne inchallah kouko féké woul tardé nga barki borom Touba
2025-03-16 22:11:43
4
Beugue brom touba rek ✈️ :
norou diouf brom kl ya meune deh
2025-03-17 19:02:02
2
As_Salihu_14💙❤️ :
Norou Diouf wax lén ko deug 🫢😭
2025-03-17 02:53:28
3
boy lo :
Lisi sof dou mahktar diaw louga
2025-03-16 23:56:58
3
Ibrahima diagne Thioune :
Dalin nabbiii Bi. Yemé na😂❤️
2025-03-16 21:21:29
3
metta Badiane :
Htdkh nio geune beug yalla fi
2025-03-16 23:05:18
2
ahma d diop785565985 :
thieuy loulou barkep borom touba
2025-03-16 19:55:05
2
Ahmadou Mbaye683 :
wksm moom dakh leen ko yomboul
2025-03-17 12:59:10
1
S Mbacke bijoux touba :
Ki Tapha niane la
2025-03-17 01:56:18
1
Tamsir Cissé 💚 :
mo goré 😭
2025-03-17 00:36:43
1
diouf normal le _ méréngué 🤍 :
abdou lahad 😭
2025-03-17 00:06:55
1
abdou xadre lo HTDKH 🇸🇳🇮🇹 :
😭😭😭thieuy yalla
2025-03-16 23:36:22
1
Mouhamadou Lamine Bara Sy :
@Mouhamadou Lamine Bara Sy: L’amour que j’ai en Cheikh Ahmadou Bamba a annulé tout autre amour en moi😭. Diarama Sidy Birahim Fall lamp 🤲S Bara Mbacké Yakaar Dji beug naala 🥹
2025-03-16 23:26:48
1
TS3M :
Ndeysan tollou way bi yeména trop❤
2025-03-16 22:47:38
1
To see more videos from user @minute_xassidatv, please go to the Tikwm
homepage.