Maneu sama phrase moy « liguey sisa bopou dogua liguey pour sa bopou »
2025-03-21 21:44:16
1190
user :
li fouko ngaaka di khalaté
2025-03-22 00:03:05
635
Boubacar 🫀🙏🏿 :
Diélli déss ak niatti at si ren kou d’accord lala laime ✌️
2025-03-22 00:00:55
164
Talibe brom darou :
Dip a dit adouna fawma nga def li nga bagne pour am linga beug🔥🥺
2025-03-22 02:03:43
124
MademoisellEvDip💜♒ :
« Avenir Thiono la guena ladj que ligueyou ndeye ci dome boudoul heuy » 👑
2025-04-28 20:45:40
89
𝙺𝙷𝙰𝙳𝙸𝙼﷽𝙱𝙰𝙼𝙱𝙰 251 :
leral sama vocal ▶︎ ●─────────── 0:30s
2025-03-21 21:07:16
24
Funny videos 😂 :
Meune sa phrase biguay wax « lii ngay am day méguo ak lii nga ñiémé deff » genre il faut oser faire des choses pour avoir ce que l’on veut ou même plus 🧠🔥
2025-03-22 02:08:29
70
PRÏÑÇË_MØMÕ :
phrase dip yeup khamna sene signification ms bi non
2025-04-13 03:41:27
0
𝔸 𝕃𝔸ℍ𝔸𝔻🇸🇳🖇️🇪🇸✪ :
Meilleur philosophe du rap Gall Séne✌️
2025-03-22 00:43:14
64
C B M :
safara moy changé nitt
mais domou taal taxoul ba karigne bi weex 👌
2025-04-05 01:26:40
13
Sokhnaaaaaa🦋 :
Sama phrase"Jëëli lii dess ngir baña ñaan lii xaliss meunta ame"✨
2025-05-01 13:39:40
7
RassouL :
DIP néneu « Fou diame sakh nitt ta fa xam loumou waxoul »
2025-06-01 02:39:49
6
Thiam VTO wifi fibre optique :
@ amouma Bac +3 mé dina tabakh R+4
2025-05-11 02:07:00
6
yaya dramé :
Tu es intelligent Dip
2025-12-30 08:05:36
2
NDIAGZO OFFICIEL :
attend lii fanne la ko Ngaaka dii dielée
2025-03-22 12:01:26
24
Moristar91🥰❤️ :
Tella nangou daye yombali door dip tu e le mellieur point
2025-04-26 16:53:55
6
Leuz🇸🇳 :
Kouy Traduire Lim wah
2025-03-29 06:37:19
2
One chef 🧑🍳 :
Moi dit changer ma vie surtout le saison borome bi bi 🥹⚓️🥷🏾