@wolof094: Kuy laal Maademba* Kuy laal Maademba sabar ga ca Ndaayànde kuy laal ndaat-saay. Kuy laal sama doom jee, salaan jooyul wéet óo. Sama doom sama soppe dund a mat a jooy óo, moom laay jooy ndax YÀLLA. Féq saw fan mu gudd ée, nga am foo ma féete. May ñaan Maademba nga day ni sa baay YÀLLA ay buur doom dundal. Boo dundee ba man liggéey feral saay ronqooñ ée. Doom waajur du fo ku leen di teral jàll àdduna ak laaxira. Kuy teral waajuram, sa pay ca rabbi Bul bew, bul jàmbu àqi njureel day toppe te day gaañ doom ju bon. Bul *féew* Mademba a soo bëggee bijjaaw ée. Bul jooy sama nenne, aayoo, beeyoo, beeyoo. Bul jooy sama nenne, aayoo, beeyoo, beeyoo! #senegalaise_tik_tok🇸🇳pourtoichallenge #wolof_sénégal #foryoupagе #pourtoiiiiiiiiiiiiiiiii #viral_video #viral_video #gambian_tiktok🇬🇲🇬🇲 #fyp #culture #wolof
𝐖𝐎𝐋𝐎𝐅🇸🇳🇲🇷🇬🇲
Region: IT
Friday 28 March 2025 18:24:26 GMT
Music
Download
Comments
Qr.fa :
Yalla naniou kay wayal sounouy dome aki seut amine
2025-03-28 20:54:59
1211
MBÄ YÀLLA DJI🇸🇳⭐⭐🇸🇳 :
🥲🥲 fiers d'être Wolof 💪🇸🇳
2025-03-28 22:59:33
491
Mrs Samb🫶❤️ :
Kassé maabo borom louga ak kébemer yayou badou ak pape gaye yalla na souffou kebemer seid sa kaww sa seutt yi namnagn la keur gui weitt naa🥺🥺
2025-03-29 13:06:27
262
slmb🌬️💓✨ :
Pk on parle pas un wolof complet 💔😭comme ça ?!
2025-03-31 01:14:00
107
mustapha_el_karim :
J'ai toujours des frissons quand j'entends cette musique. Je ne sais si suis-je le seul🥰
2025-03-29 07:28:27
100
Bambaa :
mais comment dans cette année la faire une telle création aussi original et rythmée. ça prouve tout simplement leur excellence une bonne dose a mediter❤️
2025-03-29 19:44:07
120
6ft6hooper🐇🏀🇸🇳 :
Audio bi bane année svp ?
2025-03-30 01:34:10
30
user9778373034090 :
j'ai les larmes aux yeux. Yallah na gnou Yallah fayal sougnou wadiour
2025-03-29 23:51:57
62
mohamedseck261 :
Voix wolof deugeu deugeu Niaysane ❣️🥰🇸🇳
2025-04-02 14:18:53
19
أبوبكرالصديق امبو :
machalla wolof sama xeete ❤️❤️🥰
2025-03-30 04:40:27
7
Soxna_Fatuu_MuntaQa🫶🏿💗🇸🇳 :
Mane Fatou kassé la Toudou yein🤭😍❤️
2025-03-30 16:58:26
38
adja__soukayna🤍 :
Maman Fatou kassé depuis kebemer repose en paix tu nous manques ❤️
2025-04-10 00:09:56
3
Pape Niang :
Fat kassé la grande cantatrice paix à son âme 😭
2025-03-29 22:04:27
25
Mandiaye 🇸🇳🇮🇹 :
Dembe nekhounna Machallah ❤️❤️❤️
2025-03-28 20:19:36
20
Boli :
Ça donne des frissons 🙇🏾♂️
2025-03-30 15:57:33
7
Sissi :
cercle de la jeunesse de Louga lako wayer wone
2025-03-31 23:56:43
7
||•🎀ABSATOU🎀•|| :
Sama mame la yalla nako yalla yeureum 🙏🏿🤍
2025-04-11 16:33:53
6
Mrs Thiam ❤️🥰 :
Kassé maabo birame coumba yalla soufou kébémer bi oyof sisa kaww😭😭😭 tu nous manques tellement mame booyy❤️❤️😭
2025-04-03 18:11:58
7
Elhadji Seydou Diop :
Woy day am sens
2025-03-30 16:37:28
9
Mme Seck 💘❤️ :
Svp une vidéo sur l’origine du nom KASSÉ
2025-03-28 18:48:16
41
Mamadou :
ndeysane sama mame 😭 yalla nako yeureum 🤲🏾
2025-03-29 16:10:40
7
AmethFall :
macha allá yalna boure yalla khare sama yaya aldiana firdawsy incha alla
2025-03-29 14:01:55
7
KABOU WADE 🇸🇳🇫🇷🇺🇸🇲🇦 :
Les souvenirs de mon enfance me reviennent toujours a chaque fois que j’entends cette chanson 🥰
2025-03-29 16:16:33
5
La fine fleur 🌹 :
Waouh waouh waouh ….❤️🥺
2025-03-29 00:44:01
7
it's tima 💘 :
machalah notre ethni holof est trop riche 🥰
2025-04-16 23:13:31
4
To see more videos from user @wolof094, please go to the Tikwm
homepage.