Thiéye sakhaba yi 🗡🗡yalla na yalla yok sène léér 🤲💚🤍💚🤍💚
2025-04-01 19:39:17
68
Maguette :
❤️❤️alhamdoulilah Sant n'a sama niom Mame Sant yalla boubakh Sant sama Yaye ak Sama Papa Yalla nako Sama borom yeurem alhamdoulilah bima nékké jullit Yalla nko déwallée ❤️alhamdoulilah Allahou Akb❤️