Yalla naniou yalla khirr sii bopamm ak sii S.touba barké Mouhammad psl et le saint coran😭❤
2025-04-06 11:55:22
20
Wakana qakhan sama khart :
sama kharit mom wakana❤️❤️❤️❤️
2025-04-07 15:18:20
14
daoudambaye.HT :
Wollahi chaque jour ma dourous mok Mawahibou ak Sindidi Alhamdou lilah Dieuredieuf S Touba 🤲🤲🙏
2025-04-06 10:05:50
29
Sohiabou Kane Bichri HT😎🤞 :
Ana Breudeu yii mbamu kharam yii mba Dewu Niou Sen kote🤩
2025-04-06 13:30:31
5
user3987926529693 :
lép Serigne Touba la khadime Rassoul
2025-04-05 22:47:50
18
@Kenza :
dieuredieuf Serigne saliou
2025-04-06 09:11:42
13
💦Binette✨bou Mame Saliou🥹❤️ :
Thieuy yalla alkhamdoulilah 🙏Mane nga khamni moy sma khassida préférée chaque jour dina ko Diangue deux fois Souma koy deglou sx dmay dioy😭🥰sma xol day toy😭🥰🥰❤️
2025-04-24 11:10:14
9
T B D 🇸🇳 :
alhamdoulilah Moy sama xassida 2016 ba legui Mangi koyy dourouss xassida gou yémé walahii
2025-04-07 12:27:47
12
sokhna rita Fadillou ♥️ :
Cheikhoul khadim amoul morom 😭❤️🫀🫶🏼
2025-04-05 18:48:02
10
Ado Thiatou Papa :
kouka doul diangue rék mano khamm nii khassidas gui yémé barkép Serigne Saliou mom lay ndéké diko réré déff ko adiyas Serigne Saliou mbacké 🥰
2025-04-08 21:41:43
11
Sowrou kabaro Azur💚🖤👌🏽👌🏽 :
Mane dé guénama si hat hatyou meti moy sama xasida hol nek na si kasso am fa natou boureuy dépéyagé niou juger niou procureur demandé juge bi 10ans chk jour souma xeuyé wakana la diang dissi fassalé