Man dhé sama baye ba legui nogouwoul wayé magui sante ku téde ki
2025-04-21 13:24:14
105
faadeljoxane221🇨🇦🇮🇷 :
Mane dh dama dioudou fékk saa baay nékk si ndaye sane khalisou radio dahira lagne ma nguénté bimay am 3ans lama dane yobalé si animation yi ba taye mangui nii bokou si dieuwrine daara dji ba paré nékk dieuwrine sonorisation ak administration en même ma nékalé si audiovisuel daara dji dieureudieuf saa baay🥰
2026-07-08 00:28:55
3
diakhate lat :
Sénégal maffi guene beugue Serigne Touba 🥰
2025-09-03 19:08:44
22
Narou Al mountakha bii☝️❤️ :
dieureu dieuf borom Touba 🥰❤️
2026-07-08 02:38:16
3
L’INTOUCHABLE🇸🇳🇺🇸🥊✈️ :
Bagne bagne nangou force 😂😁
2025-09-06 00:57:21
6
bamba Rassoul :
sallahou 🕊️alla mouhamet 🕊️Rassoul 🤍🤍
2025-06-06 13:47:36
4
sokhna Khady Saliou❤️ :
thieyy sante warr nagnou dh bignou sa borom bollé si ndiabotou kou tedd ki
2025-04-24 22:38:33
4
xaritou xolbi moy wakana 💞😆 :
cëy wakana mom rék laye khalam🌟
2025-04-09 22:37:13
3
THIATT SENE KHASSIDA :
alhamdouliahi diereudieff S touba diarama m cheikh Ibra fall ❤️😭 je suis