@acpapethiounne:

Ac Pape Thioune Tfm
Ac Pape Thioune Tfm
Open In TikTok:
Region: FR
Sunday 13 April 2025 22:37:21 GMT
274623
16420
429
4495

Music

Download

Comments

user42266583105638
Saliou BA :
Salam. Attention il y a le sexe chromosomique. Je serai d'accord de faire cette prière avant la grossesse. Merci
2025-04-15 21:40:21
4
oustazsylla1
oustaz sylla :
sama waji mé 3 mois dina fék yala dogale gaure la wara nek wala jigéne ba parés. défko avant mouye dieul eumb mo geune.
2025-04-14 07:38:02
50
cherif0730
❤😍CHERIF😍❤ :
Kep kou begue ame dome bou goor toudéko seydina Mouhamed yalnalako yalla defal mou dounde té barkel inchalla ♥️🙏
2025-04-17 20:39:39
354
salahou.alah.mouh
Salahou Alah Mouhamed ❤️ :
lou weer nga wax lii dh mane dh xam nassi dara def nako yala soutoural ma mou done goor ma toudé ko seydina mouhamed psl 🙏🏿
2025-04-15 12:03:40
223
beuguebambadiouf26
Beugue Bamba Diouf :
walahi deug la mako defal sama bopou am dome bou goor toudé ko mouhamed Saliou ❤️
2025-04-16 22:47:40
97
baboloise.20
baboloiz :
manguiy niane yala mou maye ma aye jumeaux
2025-04-13 23:58:45
123
elhadji_jong
el hadji :
j ai les audios de Khouratoul ayni
2025-04-15 13:01:49
40
doumz.dioufy0
Doumz Dioufy :
🥰🥰🥰J'avais la version française mais malheureusement je l'ai perdu. C'est un livre à lire car il ya beaucoup de biens fait.
2025-04-14 02:18:00
8
yayefallbousrgfallou1
beugue Fallou :
c' confirmé mane srg Abdou Rahmane lako degué wone madéfko mais al hamdoulilah amna dome bou goor matoudéko Mohamed Moustapha yallna yalla samko ❤️❤️❤️
2025-04-16 20:44:55
21
lasage3009
Santé Bien Être Naturel 🥰 :
Bilahi walahi wa talahi, sama dieukeur moma KO digalone makoy wakh tous les jours, té dom bou gor la am , Mouhamad Lamine la toudeu
2025-04-14 15:49:11
18
ben_usman_0.8
B£N_ U$M@N_ 🇸🇳 :
Alhamdou lilah mom la amate demb . Nianal lenko Yonent yalla Souhaïb lakoy toudé incha''Allah
2025-04-14 02:35:32
97
mmedjiba5
Mme Djiba_longrich-kounoune :
Salam est ce que mangaka defal sa bopou
2025-04-15 17:25:17
5
seydina0478
Seydina :
Khamou ma la waayé kou baakh nga may nourou. Goudou fane ak werr lalay Nianal.♥️♥️♥️
2025-04-14 10:29:20
17
sokhna.sylla47
Sokhna Sylla :
Mane mii défnako te dom bou goor la am machallah yalna dound barkél
2025-04-14 18:46:16
28
dabafall096
dabafall096 :
dom bou jiguèn nak🤣
2025-04-14 10:41:42
12
sougou90
Mame Diarra Sougou :
bilay mome rek la beugue mou toudou Mouhamed ❤️❤️💕💖
2025-05-12 19:14:04
7
rabou249
diekh si président Macky :
mais mane dama yakar ni yala moye khol liigeunn si yaaw rekk lay def legui sou nekkee doom bou diyguen mo geune si yawe nak
2025-04-14 09:35:54
15
user417351413
user3189929858816 :
doniouko bindeul nguir yala
2025-04-14 00:59:53
5
ibra023398
Ibra :
Je confirme lou wer la
2025-04-14 00:45:23
6
bambasoldier8
Bambasoldier :
Wallahi defna ko sama papa moma ko diokh sama deuxième doome mou dioudou done goor
2025-04-14 08:59:27
5
misssagittaire1
K.~~ :
Diokh ko sa dome bi papa 😂😂😂 adjo nako
2025-04-13 22:48:58
5
tidiane.doucoure6
Tidiane doucoure :
est ce que meunanioko déf avant 3 moi
2025-04-18 14:24:51
2
daouda.gassama81
Daouda Gassama :
Moi aussi je connais kelk qui peut 99%nga ame ngor j’en est plus de 5 preuve
2025-05-03 23:54:35
2
adama.1910
Adama Aziz fall 💯❤🙏 :
Serigne abdou Rahmane darou moukhty wakhtane nassi yalla nako yalla yeureum diegeulko xareko aldiana firdawsi ❤❤💯💯🙏
2025-06-02 13:27:13
2
madamesene95
Mrs Sene kholou ibou :
Dieureudieuf Amna solo yalla nala yalla defaal diam
2025-06-03 15:16:00
3
To see more videos from user @acpapethiounne, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About