@sengrowthagency1708: Mbodja Mbaye arrêtée #senegalaise_tik_tok #bassiroudiomayefaye #ousmanesonko #pasteflespatriotes #excellence

SENGROWTH AGENCY 🇸🇳
SENGROWTH AGENCY 🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 14 April 2025 23:44:58 GMT
586032
10511
1058
3210

Music

Download

Comments

maxcapo256
Max Borom deuk bii✌️🎉🥰 :
Limiy wax mom franchement loudoul nekh defouko 😩😂
2025-04-16 17:26:59
328
maff.animateur
maff animateur :
li môme dou yone franchement.mes ana suite bi svp
2025-04-15 11:49:00
232
mame.bousso.thiou0
salihare :
journaliste bi tamit warona demalé
2025-04-15 23:54:52
751
bachirmouham
Bachir reds :
fila procureur méré😂
2025-04-17 19:49:18
248
azkarallah11
//I SHOW LIGHTS \\ :
On a un problème avec notre langue (le wolof). Elle n’aurais jamais eu de problème en parlant d’autres langues. L’éducation sexuel n’est pas un tabou.
2025-04-16 18:13:28
238
dieuzbu
🇺🇸 DIEUZBU :
ki amna doom est ce que,mais na took kasso bagnou magal ba parè
2025-04-15 06:33:43
108
fatoumatacamara6412
Fatoumata Fatoumata :
yaw déwale si kasso bi
2025-04-16 11:05:07
41
fatoubintoundiaye619gmai
binta :
Li mo nakari procureur 😂😂😂
2025-04-16 21:30:30
109
lolone221
ami :
ki dafa eupeul bilay c troppop
2025-04-15 01:32:41
71
cheikhbi086
Talibe cheikh :
Maan ki retàne la may😂def pour mom moniou geuneuh thiaga ni hein mère nopaloul nioune danio thiaga😂 Mayei pate ak organisei
2025-04-17 15:04:26
52
serigne.touba058
Fallou awa bousso :
Présentatrice bi fougne teudié mbodia waroufa fanane
2025-04-17 16:44:43
32
la.petite.mya2
mya❤️D :
Déléne bayi héle haleyi setane tik tok svp 🙏🙏
2025-04-15 20:19:42
75
lotusbelleu
Mumofqueen ❤️ 2⭐️ :
Ki dei pour mom limouy wakh grawoul 🥺🥺
2025-04-15 15:18:38
42
dstvlofficiel
Dame SÉNE Dstv :
Juge bi woroufi wone bayi dame bi poser question
2025-04-16 23:21:38
58
leezah_13
leezah :
Meune mokal aythia mere 😂 allo mr le procureur
2025-04-17 15:13:25
51
khadijarassoullasuzz
Khadija RASSOUL laSuzz :
Ki moy Maram deuggg ayy
2025-04-18 01:57:03
8
omzofaye748
Omzo :
li môme rafétoul mais n'a vidéo yi di goudou
2025-04-18 01:30:22
11
krose2210
Babs k’rose😎💯 :
journaliste bii tamit 😂😂😂
2025-04-18 18:15:15
5
lestenuesdemamandiaye
Les tenues de mama ndiaye :
c grave mbodia ya bone 🥺
2025-04-16 17:47:27
75
dieye684
cheikh Bou Serigne Babacar sye :
wa legui journaliste bi nk foumou nékk momm
2025-04-18 16:34:40
16
layecancelo22
Layecancelo10 :
Présentatrice bi tmt ken dou mom😂😂😂nena daaaayyyyyy melni louy fitte 😂😂
2025-04-19 02:11:31
5
petite196
Liverpool :
Nagn ko bal bilay tè wakh ko mou bagnko defati yenewoumako kasso mouk
2025-04-17 15:52:00
8
gueyetransitaire0
Gueye transitaire🚘 :
Nekh dal la deff
2025-04-17 16:51:23
7
lephilanthrope54
L'écrivain moderne 🫶🫶 :
kii imaginer léen police djapeu ko niou ladj ko lodone def bagn djapeu laa mouni waxii thiaga 🤣🤣
2025-04-17 02:11:05
6
sybadis
SyBadis :
Li mouy wax nite mogui kay def chaque jour té kene arête wouko ❤️❤️❤️
2025-04-17 05:54:17
10
To see more videos from user @sengrowthagency1708, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About