you melni dangay bayi diamou Yalla yii télécharger ko
2025-04-23 21:49:25
321
Assane bamba Officiel :
mane limadiakhal moy pourquoi naryi diko diangue séne façon vous l'acceptez et non la nôtre.
Complexe bakhoul
dieureudieuf Serigne Touba
2025-05-09 07:41:22
17
🇺🇸OMZO DOLLAR 👕SHOP 👗🇨🇦 :
Aire bi tamit barkélna bay ndogo thame 😭😭😭😭
2025-04-23 23:53:41
22
Mame thierno Gueye :
Airou baye Ndogo Thiam yalla nako sa borome yereum barkep Mame cheikh Ibrahima fall 🙏ak kep kou nk si bir souf
2025-04-23 23:21:51
111
seydinamouhamed430 :
kou gueum nii serigne Touba la lalal j'aime
2025-04-24 00:22:45
134
BOU MAME FALLOU :
Ani breude yi 😂 dieureudieufé serigne touba ❤️
2025-04-24 18:41:37
89
محمد لمين بكه شر ج فضل💔💯 :
Ndaey san sama khel demna si baye dougae tiam😭 yallnakou yallh yeram si bakeb s touba khadim rasoul 🤲
2025-04-24 12:52:06
34
noreyni Fall :
tiey yalla Sénégal am na dadiou bop'pap si alkhourane 🥰🥰
2025-04-23 21:04:29
48
BAOL ÉLECTRONIQUE 📱 :
Alhouran dou aye foo ta yén daguén di foo bakhna
2025-04-25 01:12:37
11
Gueye business service :
Très très bien machalla
2025-04-24 08:48:16
34
Khadim Diouf :
Serigne Touba amol marom billahi 🤣🤣🤣
2025-04-23 23:19:05
30
الله الله الله الله الله الله :
الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله الله
2025-04-23 23:10:34
85
Karim khasida tv :
baye Noga Thiam yalnako yalla yërëm teh xaréko firdawsi🤲🤲