listikharal sa boop
So démé bay teud nga diap tok ci kaw lal bi nga wax
fatiha 1 astakhfiroulah 3 fois sallalahou allah Mohamad 3 fois ikhlass 13 fois wax linga beug yalla leralal la inchallah 🙏
listikhar Kay Serigne si mayé naniouko fépp. wayé gayi daniouy déf Dougn giss, diamono bi khalé yi sétou niou, am nio khamni Dougn sakh ginte, am nio khamni lougn ginte faté. listikhar yomboul nak
2025-05-05 07:00:57
156
Azraël Jack Layton 😈 :
Yallah rkk mo kham souba té yallah kènn douko ordre nane ko défal wala li 🤨
2025-05-05 11:30:59
34
Mohamed naby Samb :
listihar bo démé bay teude dangay diap diouli 2 raka fatiha ihlass 3 après nga tok sa digue lale nga wah fatiha 1 fois astahfiroulah 3 fois salatou hala naby 3 fois ihlass 13 fois ngani yalla mangilay niane wanela linga beugue xam
2025-07-10 11:58:15
28
mby ly🇪🇦🏳️ :
yalna yalla soutourala defala tawfékh si barké seydina moukhamadou rassulilahi 🥰
2025-05-04 14:22:54
90
noreyni le responsable🧠 :
bilahi je confirme ya bakh bilay lou wèr la dèmb la ko dèk ham lèp si sama avenir bilhil a'azim🙏🤝🙏
2025-05-05 13:02:36
39
cheikh Darou :
Ikhalasi dh bou safé ci yaw dou diar sakh istikhar dangay guis force wallahi
2025-05-04 22:06:46
112
mame fallou couture :
sallalahou alah mohamed 🥰
2025-05-04 14:39:35
90
user9192964408381 :
Sallalahou allah Mouhamed ♥️♥️
2025-05-05 07:36:27
91
Dave jr bou liss 🩸 :
Salalahou alla Mohamad
2026-02-27 18:34:36
5
sarr amy :
Sallalahou Allah Mouhamad
2025-05-04 13:16:00
78
Fatimatou bineta Kounta :
dégue na kou ragual douko df sa rawhane moy niew motkh ma ragual esk deugue la ?
2025-05-09 16:06:59
9
Bousso baly :
Salalahou alah Mouhamed
2025-05-04 12:26:38
47
Ramata 144 :
salalahou alla Mouhamed
2025-05-04 18:46:41
100
ablaye thioune sopo naby 1111 :
Sallahou alla mouhamed 🙏
2025-05-05 13:59:42
41
Maniang mou mame maktom Maktom :
yalla na yalla barkél ❣️❣️❣️
2025-11-24 22:33:17
5
Yonista Ka :
sallalahou alla mouhamad ❤
2026-03-30 18:22:07
5
Baye salou Khouma :
boulene faté diouli diouroum🙏🙏
2025-05-07 01:39:09
11
niang :
je vais essayer ce soir incha Allah
2025-05-05 09:18:40
25
Minute de Foi :
Fatiha 1 istighfar 3 fois salatoul Alal nabi 3 fois ikhlass 13 fois
2025-05-05 12:12:52
84
amadounayadaff :
salalahou Allah mouhamed psl
2025-05-04 20:07:58
27
. :
Merci je l'ai essayé et ça à marcher 🤝🤝🤝🤝
2025-11-14 23:58:07
6
laminegueye535comercialou baye :
farou rap nak
2025-05-04 23:12:40
15
modoufall 77 438 69 62 :
akay dege yangi yakhal gayi dé
2025-05-04 18:46:25
54
To see more videos from user @serignedjibrilniang77, please go to the Tikwm
homepage.