@archive.khalil.deug.zik0: Khalil DEUG guanima s.Mor kaïré néna ❤️❤️🎤🎤🎶@khalildeugg @låÿē_åfïå🎤👌 @A b d e l b d n🫰🏼 @AMINA LA CHICORYENNE 🚩🏴 @Bamba Salam bou borom Darou❤🖤 @NaBy✌🏽🖤💚Dëüğğ 🖤🖤💚💚👌🏿 @Ⓜ️oussa kalamou✅

Archive.khalil.deugg.zikroulah
Archive.khalil.deugg.zikroulah
Open In TikTok:
Region: SN
Saturday 10 May 2025 18:05:01 GMT
173993
32309
1139
311

Music

Download

Comments

ndary.lo
ndary lo :
bamba tall bongo ladane yor Khalil deugg yaw piano 🎹 kou d'accord lalala j'aime ❤️❤️
2025-05-11 23:13:29
156
elhadjiassgning
El Hadji Ass Gning :
Kon moy serigne Mor kaïré🤗
2025-06-27 18:55:15
78
kobetheblackmamba8
SANGUE FALL🏀🇸🇳✅ :
kaïré neeh xarit AK andando dounou benn diawalé gué tax Ken dou yegg fenn👌
2025-05-11 13:15:53
83
yamal.19669
yamal 19 :
do nit ohhh khalil deugg🥺🥺🤩🤩
2025-10-04 21:10:15
5
layeafia11
låÿē åfïā bdn noble 🩸🖤🫰🏿 :
ndaysane zikroulah souniou xoll 🎤🩸🖤
2025-05-10 18:10:42
39
matarfaye713
matarfaye713 :
yalla na yalla wéreul batt bi 🙏♥️♥️💯
2025-09-27 22:35:06
6
alioucana527
liou star 👀💫 :
Fall déloma sama abonnent 💝💝✌🏽✌🏽☮️♥️🫀🥹
2025-07-26 00:59:50
3
mameseyni28
Diagne narr ❤️🖤28 :
Li nekhna way khalil yallah na bate bi wer yallah moussal len si louy loranguè yallah lafal len thiate bijjahie cheikhoul khadim 🚩🏴👌❤️
2025-05-14 21:59:16
5
darousalamdeco2
darou salam deco2 :
boul dougou si music mala ko wakh bilahi yangui zikar đi wo lafal lou nekh mais instrumen. music boumou si bock sou way
2025-05-12 15:01:33
38
bambasalam
Bamba Salam bü Sëx hãsãn Salam :
Ndeysane kilifeu 👌❤️🥹
2025-05-10 20:58:10
18
ahmada0449
Ahmada04💙🤍 :
Ms baye lii graw na
2025-05-11 10:46:23
18
www.sidibara
sidibara carreuleur 😍 :
salla lahouhalah mouhamed 🥰
2025-05-24 22:23:19
4
dembanoreynikara
dembanoreynikara :
Li kawéna dh fall 🥰🥰🥰
2025-05-11 11:32:50
16
mouridedoulahi313
mouridedoulahi313 :
Sama abonnement 😳
2025-05-15 03:16:06
3
momo_baye_darou10
MØMØ CHICORIEN#10⚽🚩🏴 :
kon zikrouh lah sougn si défé Beat li lay dioxé Xalil deug ya ayyy🥺 yalla na yalla geuneu weral batt bi🙏
2025-05-13 14:00:39
6
ismaila185
touba fall 63 bi :
li dafa féss fall
2025-05-10 18:59:02
7
d_a_b_o_c_h_e_e
Dabochee :
Non si bay fall mais sokhna bakh na aram yangui seuy seuy bi bilay légui khalil dafa geuneu lérr tes inspirations dafa yokou bilay diam si yénn
2025-05-11 21:02:26
7
ndamalbachir1
Ndamal❤️Bachir :
Waw waw dof li fess na way kilifa
2025-05-11 17:10:25
6
alaji.gueye6
Alaji Mam thiérno :
misik yéfi sayetané la
2025-09-28 15:34:57
5
beugbamba427
Beug bamba :
Alhamdoulilah Alhamdoulilah Alhamdoulilah ❤😭😭😭
2025-10-09 08:36:41
2
abdatijambaar
ABDATY 🇸🇳👮❤️ :
S Moussa Ka, S Samba Diarra Mbaye , S Mbaye Diakhatè , S Mor Kaïrè thieuye Ahmadou mo jabot❤
2025-09-16 02:28:37
4
abdoulahii1
ƳᗩᛕᕼIᑎᗴ :
Saway dh legui sah kanamou marié leuh yor baye 😂😂😂
2025-05-14 02:26:41
3
khll.dg3
khll.dg3 :
Diadieuf sama tom 👍👍
2025-06-27 03:09:17
2
hamdy.moustapha0
🧿AMDY_MOUSTAPHA🧿⚖ :
Diarama waye 🔵⚪️🔵⚪️
2025-05-12 05:28:15
1
diazkara42
Diaz chicorien🚩🏴 :
Nekhna wayyy fall ❤️
2025-05-12 19:54:34
3
To see more videos from user @archive.khalil.deug.zik0, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About